start_time
float64 0
2.73M
| end_time
float64 326
2.78M
| speaker_id
stringclasses 55
values | text
stringlengths 1
4.06k
| audio
audioduration (s) 0.17
388
|
---|---|---|---|---|
0 | 92,933 | 11spk1 | asaalaamaalekum mbokki auditeurs auditrice su 93 point 5 ñu ngi leen di jaajëfal bu baax a baax ci déglu bi di leen nuyu bu baax a baax te itamit %e di jox suñu nuyoo rekk kii di suñu DG monsieur Pape Mate Diouf mu daal di koy séddale képp ku nekk ci rajo bi ak bitti rajo bi ñu nghi leen di jaajëfalaat bu baax a baax tay nag dikkaat nañ si suñuy émission yi ñu jagleel nag météo waaye jagleel ko mbay mi ci dëkk bi ci Fatick ak li ko wër ñu nar a dalal nag fii tay ci sunu émission ki nga xamante ne moom mooy Momadou Bodian di directeur régional développement rural waaye tamit %e di dalal Maodo Maodo miin nañ ko fi nag bu baax a baax Maodo Samb di chef service régional de la météo fii ci région de Fatick tay nag ñuy waxtaanee lii di information climatique dans les activités de récolte et post récolte loolu nag bu ñu ko waxee day daal di duggaat rekk ci mbay mi ana yan information la ci nit ñi soxla ci avant ak après récolte ñu nar ko faram-fàccee fii ci rajo Ndefleng FM Fatick ci kàffu gi Maguette Mbaye ci technique bi kii di DJ Madou dañuy daal di bàyyi rekk sunu ñi nga xamante ni ñoo di suñu invité ñu daal di présenté wu ñoom itamit suñu mbokki auditeurs yi balaa boobu di leen dalal jàmm te itamit di leen remercier ci acceptation invitation bi %e damay bàyyi rekk %e Maodo comme %e ci kër gi nga dëkk daal di bàyyi rekk sunu gan gi mu daal di moom itamit %e def li nga xamante ni moom mooy présentation bi te itamit di ko wax mu dalal jàmm %e Momadou | |
92,933 | 106,068 | 11spk2 | jërëjëf soxna Maguette ñu ngi leen di nuyu di leen sant ak ñépp ñiy déglu rajo bi %e damay faral di wax ne am ngeen pàcc bu mag ci wàll wi nawet mooy loo xam ne bawul kenn | |
106,068 | 106,565 | 11spk1 | %hum %hum | |
106,565 | 117,813 | 11spk2 | te bu ñu ko waxee ëmb na lépp ndax ku xam Sénégal xam ne nawet bu Yàlla defee mu antu nañ ko muurloo mu ne ah ma ne ko njëriñ la ca ne mu ne ah ma ne ko dana laal ñapp du ba kenn | |
117,813 | 118,294 | 11spk1 | %hum %hum | |
118,294 | 143,588 | 11spk2 | %e rawatina tay jii li nga xam ne %e moo ñu fi di dajale muy loo xam ne wax dëgg fa Yàlla ab lëkkaloo la bu am solo et lëkkaloo nag boo ko déggee dañu naan nguuru Sénégal cib liggéeyam mu ne ah ma ne ko alaa :ar kulli haal :ar ci fàcc bu mu mun a doon mu ne ah ma ne ko da ngeen dégg ñu ne am nañ ay partenaires yu ko cay jàppale moom lañ tuddee les partenaires techniques et financiers te partenaires yooyu PAM defe naa ne liggéey bi mu ciy def lu jéggi sax njàngin wi defe naa ci wàllu mbay mi mu ne ah ma ne ko kenn naatable wu ko | |
143,588 | 143,885 | 11spk1 | %hum %hum | |
143,885 | 154,445 | 11spk2 | wax dëgg fa Yàlla loolu cant ak ngërëm dina leen ñeel ndax dina tax ñu mun a tay jii am jotaay boo xam ne des ci mun a leeral faram-fàcce ci loo xam ne jëm ci nawet bi | |
154,445 | 154,926 | 11spk1 | %hum %hum | |
154,926 | 181,092 | 11spk2 | bu ñu ci yeggee tuuti dinaa ci dugg insaa àllaa ci kanam man la Momadou Badiane directeur régional yor wàllu loolu fii ci Fatick di rafetlu émission bi di leen gërëm di leen sant insaa àllaa ba ci kanam tuuti maasàllaa jaajëfal nañu la %e Momadou Badiane moom itamit mu ñëw ci suñuy %e studio rekk daal di bëgg a waxtaan ak askanam waxtaan ak waa région de Fatick bàyyi rekk Maodo ñu ngi lay jaajëfal yow tamit di la daal di dalal jàmm ci sunu studio | |
186,694 | 198,224 | 11spk3 | %e asalaamaalekum %e soxna Maguette xanaa rekk %e di delloo buum ci mboy-mboy ga rekk di wax ni maa ngi nuyu askanu siin yépp | |
198,224 | 198,891 | 11spk1 | %hum %hum | |
198,891 | 237,158 | 11spk3 | bàyyi wu ma kenn di am nag wax dëgg Yàlla tay mbéte wala boog kontaante bu wér bokk plateau bi ak %e suma xarit suma suma conseiller technique mun naa wax loolu suma %e genn wàll muy Momadou Badiane bi nga xamante ne bi Yàlla moom moo ñu boole mu yore direction régionale %e agriculture direction régionale développement rural autant pour moi nga xamante ne bii dafa %e dafa moo gën a yaatu man Yàlla def ma tamit bon ma yor wàllum météo %e Yàlla def aussi bon depuis bi mu fi ñëwee ba léegi wax dëgg Yàlla ñu ànd di liggéey vraiment liggéey boo xam ne bii bu mucc ayib la | |
239,944 | 250,219 | 11spk3 | rafetlu naa ko suñu ay kilifa vraiment rafetlu nañ ko aussi vraiment %e ma am daal wax dëgg yàlla daal tay jii mbégte gu rëy %e bokk ak moom jotaay bi | |
258,632 | 259,112 | 11spk1 | %hum %hum | |
259,112 | 267,931 | 11spk3 | wala boog si gàttal rekk bu fekkee ne que tay jii da ngay wax mbay yaakaar naa li ci ëpp solo moom mooy arrosage | |
267,931 | 268,574 | 11spk1 | %hum %hum | |
268,574 | 288,389 | 11spk3 | bu ñu nee arrosage nag doomu aadama aadama bi mun nañoo jël robinet wala mu jël %e ay ay jumtuwaayam root arrosé waaye arrosage bi nga xamante ne bii moom mooy li ëpp solo mooy bi nga xamante ne bii moom la suñu borom subxanaxu wa taalaa def nga xamante ne bii mooy ubbi asamaanam mu taw ba maasàllaa kenn ku si nekk | |
288,389 | 288,802 | 11spk1 | %hum %hum | |
288,802 | 292,307 | 11spk3 | li nga xamante ne bii moom nga yaakaaroon moom nga mën ci gis sa bopp | |
292,307 | 292,742 | 11spk1 | %hum %hum | |
292,742 | 305,158 | 11spk3 | donc %e ñun ci côté boobu moom la ñuy kii quoi ñu ngi koy liggéey boobu ba léegi nawet bi door nañ ko ci bisimilahi :ar rahmaani :ar rahiim :ar %e ñu ngi am yaakaar te aussi vraiment ñu ngi ciy génn ci alhamdulilahi :ar rabil :ar aalamiin :ar | |
305,158 | 305,575 | 11spk1 | %hum %hum | |
305,575 | 320,524 | 11spk3 | donc di ñaan ci Yàlla suñu boroom %e lépp li nga xamante ni bii am nañ ko ci muy ay meññeef yi nga xamante ne bii tay jii villageois yi récolté nañu ko li ñuy ñaan rekk moom mooy na ko ñépp jëriñu ci jàmm ak tal | |
320,524 | 320,992 | 11spk1 | %hum %hum | |
320,992 | 321,476 | 11spk3 | %hum | |
321,476 | 373,818 | 11spk1 | am na solo am na solo %e Maodo ñu nar a séq ak yéen waxtaan bi balaa boobu nag %e cig fàttali rekk dañuy %e fàttali émissions yi ñi ko sponsorisé bokk na ci projet 4R du programme alimentaire mondial PAM dans les cinq régions cibles cinq régions cibles yi nag Tambacounda la Kolda Kaolack Kaffrine ak Fatick loolu nag %e ñu ngi ko tënk rekk ci soutien bi nga xamante ne moom mooy soutien technique bu Jokalante di leen jaajëfaat bu baax a baax ñoom itamit sponsors yooyu noonu %e Maodo balaa may %e dikk rekk ci li nga xamante ne moom mooy vif sujet bi cib tënk rekk li nga xamante ni génn nañ ci doon ko waxtaanee temps yépp muy mbay mi sànq yaa ngi wax naan duggoon nañ ci ak ci bisilimahi :ar rahmaani :ar rahiim :ar génn ci ci alhamdulilahi :ar rabil :ar aalamiin :ar ñu mën a jàpp ci %e li nga xamante ne moom mooy mbayum ren lan lañ ci mën a jàpp | |
373,818 | 381,270 | 11spk3 | %e mbayum ren xëy na bëgg naa ci aborder mais comme Yàlla dafa dogal ma toog ak ki nga xamante ni tay jii c' est la vois la plus autorisée | |
381,270 | 381,753 | 11spk1 | %hum %hum | |
381,753 | 384,527 | 11spk3 | am na fi nga xamante ni peut être que foofu laay yem | |
387,914 | 397,830 | 11spk3 | gis nañ nii que ñu ngi am %e nawet bi le premier juillet le le premier juin autant pour moi le premier juin ci la ñu am les premiers pluies utiles fii ci biir en tout cas région de Fatick | |
397,830 | 398,552 | 11spk1 | %hum %hum | |
398,552 | 419,056 | 11spk3 | jàpp nañu en terme donc de d' opération culturale am nañu trois vagues de semis tawu juin boobu am na ñi nga xamante ne bi jiwoon nañ ci am na ñi nga xamante ne bi toog nañu presque weer après ñu soog a mën a am ndox bi nga xam ne bii war na mën leen permettre ñu déclenché seen ay semis am encore une troisième vague | |
419,056 | 419,729 | 11spk1 | %hum %hum | |
419,729 | 437,149 | 11spk3 | donc loolu nag am na jeexital bi nga xamante ne bii am na ko tay ci ci kii quoi gàncax gi parce que bu ñuy wax %e loolu boo moytuwul gis nañ ni que ñi nga xamante ne bii tay ñoom ñoo déclenché woon seen %e seen semis ci première kii bi quoi première taw bi mooy taw bu juin boobu | |
437,149 | 437,478 | 11spk1 | %hum %hum | |
437,478 | 450,689 | 11spk3 | neeñu alhamdulilah :ar fi mu nekk nii bu dee wàllum gerte gerte gi ñor na bu dee suuna bi vraiment suuna si ñor na bu dee mboq mi ñor na pratiquement de spécu() spéculation bi yépp mën nañu wax lépp kii na ko egg egg na actuelement à maturité | |
450,689 | 451,229 | 11spk1 | %hum %hum | |
451,229 | 464,711 | 11spk3 | te li koy firndeel moom mooy tay jii boo duggee ci biir %e marché bi di nga gis ni vraiment nit ñaa ngi fi nekk nit ñaa ngi lekk gerte bu doy nit ñaa ngi lekk mboq dégg nga ak yeneen ak yeneen ak yeneen ak yeneen donc loolu dañuy wax ne sant Yàlla la | |
464,711 | 465,037 | 11spk1 | %hum %hum | |
465,037 | 472,632 | 11spk3 | am na nag ñi nga xamante ne bii ba léegi %e seen seen seen %e seen mbay xaw na xaw na kii quoi xaw na doy waar | |
472,632 | 473,269 | 11spk1 | xaw na doy waar | |
473,269 | 483,629 | 11spk3 | mooy ñi nga xamante ne bi ñoom ñoo nekkoon ci deuxième vague de semis bi ak troisième vague de surtout ñi nekkoon si troisième vague de semis bi ñooñu mën naa wax ni vraiment fu mu nekk nii seen situation kii bi quoi doy na waar trop | |
483,629 | 484,006 | 11spk1 | %hum | |
484,006 | 493,760 | 11spk3 | mais nag ñu jàpp ni wolof dafay léebu ne nawet moom toujours dafay naawee wet dégg nga donc ni muy %e baaxee ci penku noonu la mun a bonee ci soww | |
493,760 | 494,117 | 11spk1 | %hum %hum | |
494,117 | 497,341 | 11spk3 | wa illaa tamit des fois tamit ñu am ñu am kii quoi le sens :fa contraire | |
497,341 | 497,776 | 11spk1 | %hum %hum | |
497,776 | 510,823 | 11spk3 | ren jii Yàlla noonu la tëggee nawet bi ah ñu koy nangu xam ne aussi que comme ni ñu koy faral di waxee rekk changement climatique moom mooy li nga xamante ni moom moo fa jaar parce que d' habitude li daan am moom mooy bu tawee dafay taw rekk | |
510,823 | 511,326 | 11spk1 | %hum %hum | |
511,326 | 523,567 | 11spk3 | dégg nga %e ñu am un un bon démarrage donc distribution spatiotemporelle comme ni ko tubaab di waxee mu am benn didtribution bu correcte mais ren jii gis nañu que ni distribution boobu moom si boppam moom moo korektul | |
523,567 | 523,963 | 11spk1 | %hum %hum | |
523,963 | 531,608 | 11spk3 | %e li ma ci gën a yéem nag tuuti kooku naa ci si xëy na du ñàkk sax directeur moom xëy na dina ma mën a gaganti | |
531,608 | 532,078 | 11spk1 | %hum %hum | |
532,078 | 536,841 | 11spk3 | bon gis nañu ne dafa am benn zone fii ci région de Fatick mooy diggante Tataguine | |
536,841 | 537,501 | 11spk1 | Tataguine bi waaw | |
537,501 | 543,545 | 11spk3 | jàpp %e Diohine jàpp Toucar jàpp daal la vallée morte du siin | |
543,545 | 544,025 | 11spk1 | %hum %hum | |
544,025 | 569,373 | 11spk3 | gis nañu côté boobu presque ay at a ngi nii même année même profil bi la ñu am c' est à dire que chaque année vraiment dañuy am problème ñoom pour kii quoi pour ñu décoller léegi dañuy am problème ñoom pour ñu décoller et puis souvent même bu ñu décoller aussi très souvent même bu ñu yeggee bu seen spécu() spéculation yi du egg du arrivé aussi à maturité nim ñi ni ñu ko bëggee noonu lañ ko nii lay demee daal | |
569,373 | 569,889 | 11spk1 | %hum %hum | |
569,889 | 584,883 | 11spk3 | actuellement nii ren jii fii may waxee nii nii foofu nekk na zone bi nga xamante ne bii peut être que bëgguma jiitu sunu mbokk yi nga xamante ne bii ñoom ñoo yore sécurité alimentaire bi pour di ci wax mais ñaaw naa njort lool ni soo moytuwul dafay ne risque nekk une zone à risque alimentaire | |
584,883 | 585,183 | 11spk1 | %hum %hum | |
585,183 | 587,146 | 11spk3 | xam naa lu si nekk directeur dina si delluwaat insaa àllaa | |
587,146 | 595,823 | 11spk1 | nañ ci dellusiwaat monsieur: Fra Bodian dañ lay daal di bàyyi rekk nga daal di présenté waat lii di structure kuréel bi ngeen nekk ak itamit lan mooy zone d' intervention bi | |
595,823 | 600,615 | 11spk2 | waa jërëjëfëf direction de la développement rural mooy kuréel gi nga xam ne moo yor mbay mi ci wàllu Fatick | |
600,615 | 601,020 | 11spk1 | %hum %hum | |
601,020 | 617,739 | 11spk2 | boo xoolee taxawaayam am na kër gu boo xam ne moo nekk fii ci quartier Escale ñi ko xam bëri na ndax Fatick moom boo nee agriculture rekk %e dana bërëb ba dafa jëmme ndax dafa am histoire dafa am taarix %e boo xoolee département bu ne it %e kër ga jëmmal nañ ko fa | |
617,739 | 618,155 | 11spk1 | %hum %hum | |
618,155 | 625,078 | 11spk2 | donc mu am kilifa bu ko jiite ak ay %%e ay techniciens noonu la bindoo si wàllu taxawaay | |
625,078 | 625,549 | 11spk1 | %hum %hum | |
625,549 | 647,780 | 11spk2 | li ko wër nag ay projets ak ay programmes la yoo xam ne ñu ngi ci ndigalu ministre de l' agriculture d' équipement rural ñoom it bokk ci liggéey bi kenn ku ne di indi sa wàll ci ci ci ci %e ci li nga xam ne moom lañ bokk jëmee ko ci baykat yi nga xam ne mu nekk wàll wu am solo ci askan wi loolu loolu mooy taxawaay bi ci wàllu bi ñun ñépp ñu nekk ay lu ñu tuddee démembrements | |
647,780 | 648,160 | 11spk1 | %hum %hum | |
648,160 | 659,474 | 11spk2 | kër gu yaatu la am ay démembrements DRDR bi ci département bi SDDR lañ leen di tuddee mooy service départemental développement rural boo demee it ci %e lu mel ne comme agences yi ñépp ñu ngi dégg ANCAR | |
662,569 | 706,357 | 11spk2 | ak yeneen yu demee ni ki ANIDA ak projet programme yi nga xam ne xëy na bu ñu ci tuddee tur dina am dina am %e nañ ko bàyyi xel lu mel ne Proval chaine de valeur projet Agri Jeunes ak beneen bu bees boo xam ne sax mu ngi %e waaj a taxaw ñu ngi ci tànk taxawal ko daanaka ñi ngi teew ci région :fr abi ñu ngi nekk ci liggéey xam naa dina gën a fës ci kanam tuuti ñu ne programme de développement chaine de valeur yi nga xam ne Banque Islamique de Développement moo ciy jàppale nguuru Sénégal ak %e yeneen projets programmes ak Paris yooyu yépp dafa bokk ci projet sous tutelle ministre agriculture boo xam ni ñoom it dañuy dugal seen wàll seen loxo ci nawet bi waaye boo xoolee nawet bi soo ko bëggee tënk da ngay gis ne nawetu ren bi comme ni ko sëñ Maodo waxee %e ñoom sëñ Maodo dañ waxoon ne seen gëstu ne nawet bi dina teel | |
706,357 | 707,115 | 11spk1 | %hum %hum | |
707,115 | 738,978 | 11spk2 | wax na naam wax na dëgg ndox mi boo xoolee daawaat daawaat daaw %e boo xoolee le douze juin %e lañ tawluwoon bii gën na teel ndaxte boo xoolee côté le huit juin la ñu am taw yu njëkk yi %e waaye nag la ca topp waxoon nañ ko newoon nañ ah mën na teel a dikk waaye dina am ay dog-dog dog-dog yooyu gis nañ ko ci mois de juin bi ak mois de juillet bi ba nga xam ne bi taw biy dikkaat boo xoolee ci ñoom li ñu tuddee derniers décate maanaam mooy fan yu mujj ci mois de juillet ci la yëf yi ñëwaat | |
738,978 | 739,557 | 11spk1 | %hum %hum | |
739,557 | 761,767 | 11spk2 | dog-dog yooyu li mu indi nag comme nim ko waxee dafay méngoo ak ni gàncax giy màggee ndax ku xam ne dañ ne nawet la ko gën a téeye tay jii comme ni mu ko waxee dañ koy firndeel dëggal ko de() dem nañ ba tay jii information climatique bi dafa nekk dafa am tolluwaay comme nga ne jiwu ni engrais ni puudar ni matériel bu ndaw wala matériel bu mag | |
761,767 | 762,256 | 11spk1 | %hum %hum | |
762,256 | 768,700 | 11spk2 | maanaam facteur de révolution te tay jii sax moom la ñuy jiital ndax tay jii changement climatique yi ñu ne | |
774,870 | 796,561 | 11spk2 | maanaam jiwu bi mën na mucc ayib engrais bi ak jiwu bi yépp mën na teel a dikk matériel bi sax mën na teel a dikk lépp waaye bu ndox amul dara du sotti ndax nawet bi nawet bi dañ ne nawet la boo xam ne mu wékku ci ndox mi nga xam ne day jóge ci asamaan te Yàlla buur bi di ko taw mu te di ñi ko baaxee te baykat yi di ci def li nga xam ne moom la ñu war a def | |
796,561 | 797,574 | 11spk1 | %hum %hum | |
797,574 | 812,115 | 11spk2 | loolu bu ko defee day tax ci wàllu xeetu mbaax yi ñu tuddee bonne pratique ci wàllu mbay da ngay gis ne baykat bi day topp loolu li ñuy li nga xam ne mën nañ koo faru mooy li ñuy tuddee semis à sec képp koo xam ne xam ne ne suuna dañ koy faru | |
812,115 | 812,368 | 11spk1 | %hum %hum | |
812,368 | 866,469 | 11spk2 | doo bàyyi ba bàq bi tooy nga koy ji da ngay tardé waaye am na ci loo xam ne li ci des lépp boo xoolee foog bàq bi tooy te léegi waxatuñ tooy tooy tooy tuuti de bàq bu tooy lañ wax li ñu ci jublu mooy baykat bi léegi doo ko ne demal nga ji da nga koy fexe bu jiyee mu sécuriser ji ma looloo tax ñu ne la bàq ba tooy tigi ba ba nga xam ne bu gerte ñëwee basi ñëw sëb ñëw %e mbokk ñëw leneen dikk lu mel ne bene mooy sesam ceeb parce que dañ ko fiy bay département Fatick ak Foundiougne maasàlaa yooyu yépp bu ko defee ñu mun leen a sécuriser kon %e defe naa ne loolu lu am solo la léegi boo ko xoolee ci nawet bi comme ni ko waa ANACIM waxee liñ ci wax lépp dara dëñu ci maasàllaa li ko waral mooy lenn mooy wax ji dafa tegu ci xam-xam tegu ci ay jumtuwaay ak i xarale yu mucc ayib kenn weranteeul waxu météo | |
866,469 | 866,851 | 11spk1 | %hum %hum | |
866,851 | 873,345 | 11spk2 | léegi ci fànn yépp rawatina ci wàllu mbay kon loolu cant ak ngërëm ñeel na leen ci liggéey bi ñuy def | |
873,345 | 874,224 | 11spk1 | mais tay tay | |
876,559 | 876,940 | 11spk1 | %hum %hum | |
876,940 | 885,497 | 11spk2 | %e maasàllaa léegi ci %e yegg si nañ ci cappaandaw gi ñàkkutoon ay jafe-jafe ci nawet bi ci wàllu engrais | |
885,497 | 886,021 | 11spk1 | %hum %hum | |
886,021 | 902,979 | 11spk2 | waaye gis nga %e bu Yàlla defee jàmm bi ci ministère bi jëlee taxawaay ba ce war dsaanaka dem na ba engrais bi yépp maasàllaa fi mu war a dem yépp yegg na fa ci départements ak communes yi moo xam engrais gerte dugub ak mboq urée yépp taw bi nag gëlgóose boobu mu def noonu diggante mai juin am na lu mu lifin ba ñetti vagues yooyu mu wax moo fi ne | |
902,979 | 903,486 | 11spk1 | %hum %hum | |
903,486 | 934,546 | 11spk2 | de semis boo xoolee fi mu toll nii dugub ji li tax mu jàppandi ak gerte gi yépp li mu tiim yépp ci vague bu njëkk bi la moo tax boo demee ci marché bi fekk fa mboq fekk fa gerte sëb yi mu ngi ci marché yi mu ngi ci yoon yi tali bi nit ñaa ngi baykat yi di ko jaay boo demee ci cin bi it ah ñu ngi ko fay lijjanti ci kër yi maasàllaa di ko loolu lañ tuddee autoconsommation bi waaye pour ngir %e loolu lépp ak deuxième vague bi comme ni nga ko waxee nag deuxième vague beeg troisième vague bi nag foofu la xaw a yéexee xawee dese tuuti dina am ñoo xam ne xëy na seen deuxième vague dina mën a sori | |
934,546 | 935,287 | 11spk1 | %hum %hum | |
935,287 | 941,077 | 11spk2 | waaye am na ci ñoo xam ne wax dëgg fa Yàlla dina xaw a doy waar troisième vague ba moom daanaka kooku moom bu ñu waxantee dëgg rekk te Yàlla tax moom daanaka du mën a bokk | |
941,077 | 941,512 | 11spk1 | %hum %hum | |
941,512 | 994,661 | 11spk2 | waaye yooyu yépp li koy gën a fësal mooy enquêtes agricoles yi ñu ngi ci si balaa may ñëw nii rekk jot nañ ab battaaxal boo xam ne le vingt sept bii la ñuy def atelier de présentation nationale atel() mission de présentation des résultats maanaam li tukkee ci enquêtes yi dana am atelier boo xam ne benn ndaje boo xam ne insaa àllaa le vingt sept lañ koy def fële ci DAPSA moo ko organiser ak kuréel yi ciy war a bokk yépp su ko defee ñu présenté ko ñu génn ci enquêtes yi nga xam ne moo jëm ci enquête agricoles annuelles deux mille vingt deux mille mille et un ci campagne bi insaa àllaa pour wan leen ci kanam tuuti dinañ ci am lu gën a leer ndax loolu lépp enquêtes yi ñoo koy def ci wet ga it mu am enquête CESNSA li mu wax ne fii nag am na ag digg goo xam ni wax dëgg fa Yàlla ci wàllu taw dañuy gis ne demeewul noonu mooy li ñu tuddee noonu vallée morte siin boobu ak dëkk yi nga xam ne ñoo ko ñoo ko leroo gis nañ ne yëf yi dafaa xaw a tagatémbe | |
994,661 | 995,596 | 11spk1 | %hum %hum | |
995,596 | 1,012,907 | 11spk2 | daaw gisoon nañ ko ren it daaw li mu doon exceptionnel exceptionnel xaw na faa feeñ tuuti waaye xawoon na maskewu ndax daaw année exceptionnelle la waaye ren gën naa gën a fës ba ko jaar foofu nekkul loo xam ne lu ñu lu nit wax lu ñu inventé la kenn ku fay jaar gisal ko sa bopp boo wàccul tali bi sax da ngay gis yoo xam ne dina la xaw a jaaxal tuuti |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
- Downloads last month
- 28