Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
audio
audioduration (s)
1.18
171
transcription
stringlengths
0
988
source
stringclasses
8 values
keneen ñëw ne: “sang bi, sa libidoor baa ngi nii. dama koo fasoon ci sekkit, denc ko.
bible
léegi jaww ji nag bu demee ba attanatu yenn yeeg yooyu bo ngeen ba ñu agressé ko trop léegi moom si wàllu boppam ak yooyu tàngaay bi day yokku léegi di nga toog dëkk yoo xamante ne ay 37 degré 38 la ñu daan am maximum mais da ngay dégg léegi nag am nañu ay 40 41 42
kallama
demlante ci ay dëkkandoo ci maslaa la bokk
alffa
sàmmal ma sama ginaaw!
galsenai
def naa sama liggéey.
galsenai
ban oto mooy dem gendarmerie pikine
urban_bus
rue intersection mansour sy
urban_bus
ba tax ma fëx àkki wolof ya jiitu woon
galsenai
parce que bu ñu jëlee par exemple azote bi naka la mën a naka la nekkee ci jaww ji
kallama
gàtt rekk la wax leeralul ndax xar la taamu walla béy
alffa
pharmacie golf sud
urban_bus
nan laay def ngir dem gendarmerie pikine
urban_bus
77 645 55 54 waaw tur wi ousseynou sow la guddeeg bëccëg ku ma woo di nga ma jox jot après mën naa leen wax fan la nawet bi toll nan la ñu ko gisee ñun
kallama
mooy ne dañ leen diconseiller ne nawet bi si boppam jeexagul parce que ren biñ defee prévision météo yi mooy li nga xam ne moom la ñu anacim jox
kallama
yii nii ju bu ñu kon yoon wi dafay am wiiri ci montaañ buy lëkkële antarktik di ñëw ci asset bi
fleurs
ban car mooy dem bank of africa pikine
urban_bus
pool ak barnabas nag am ak ñoom diisoo ak werante wu metti; noonu bokk yi jàpp ne, pool ak barnabas ak ñeneen ci ñoom war nañoo dem yerusalem ca ndaw ya ak njiit ya, ngir leeral werante wi
lafricamobile
tom dégg na làkk yu bari.
galsenai
saxaaru ndox mu tàng mi dees koy suuroo ngir faj ay jafe-jafey gis
galsenai
nee ñu xobi pàppaayo baax na ci fas yi seen biir di metti
alffa
usine ndox
urban_bus
ebola bi dugg na fii lu ne sida xaw ma lu ne dugg na fi
kallama
ngistal la, moo xam nit ñi teew walla teewuñu.
galsenai
mou daldi xibar faatou sëñ afia imam.
galsenai
gàmbi ak muritani lesere nañu senegaal
galsenai
tëggum sabar dafa am ñu ñu ko féetale
alffa
yow yaa xam li lay métti nga dem ci medecin bi
kallama
parce que ñun même symbiose à travers le projet pra
kallama
waa càdd di ko woowe savonnier.
galsenai
bàyyil ma àbb loolu.
galsenai
puutarub buur du takkug neen.
galsenai
nuyu ñi nga xamante ne ñoom la ñu baaxoo waxtaanal xam na tey du ma ko accès ci wàllu
kallama
nii la njureefi jàngu benn a bu dakaar tëdde.
galsenai
bu nawet gàttalee rek daanaka sooxe nga yow ba déwén sa dund sax nekkul loo xam ne day mujj a am problème kon nag yooyu il foog mu nekk loo xam ne dinañ jot yenn xabaar yi
kallama
mangazin
urban_bus
wax ab xottiku la kenn ku nekk yaa xam noo koy ñawe
alffa
modibo adama, usman dan fojo moo ko dimbali woon
galsenai
xibaar bi mu ngi tukkee ci pekkub bànkub àdduna bi ci ndakaaru.
galsenai
bu ko bu ko bu ko jiw bi amee
kallama
mais tey ñun ñi nga xamante ne ñooy nekk si biir collèges yi nekk ay jeunes nekk ay baykat su fekkente ne ñu ngi waxtaan ak suñu moromu baykat loolu dina gën a yomb pour ñoom ñu intégrer li nga xam ne mooy kuréelu baykat yi
kallama
làmp yi dañu jékki jékki ne kamaj
alffa
keneen kan moo leen dimbali ?
galsenai
bill gates, moom, weddi na tuuma yooyu ñuy teg ci kowam
galsenai
ndax noonu la deme ?
galsenai
carnets yooyu dafa recensé membre bu nekk lu mu war a indi te mu méngóog borom parce que dañuy lebi banque di fay donc dañuy renouveller loolu bu ñu fayee bor bi su ko defee ñu mën a delluwaat defaat beneen campagne
kallama
mees gi nga jënd du doy ci létt yu sew
alffa
garab la gog manees na koo jël di taaral kër walla mbedd.
galsenai
ngir dekkalaat ko koomu alkandeem ma wér
galsenai
benn barack
urban_bus
danoo xiifoon nun ñaar ñépp.
galsenai
danuy nekk di ligéey.
galsenai
danga leen di soreyanteel ndax ñu baña xeex
alffa
dépot bonnet rouge mariste
urban_bus
terrain seffa pikine
urban_bus
ngér moo ci topp nag lu ci gën bari ay nit nga topp
alffa
hum di faati bakkan am na 3i doomu aadama yinga xamantene démb daal dinañ ñàkk seen bakkan ci diggante diourbel ak podor bu loolu weesoo dañuy daal di kon bokk
source
moo tax nag ñu bëri actuellement nga xam ne dugub ji jàll na ñu toll ci période mboq ñoom ñëpp ñu ngi ëndi seen mboq di di ëndi foofu pour ñu traité teel la
kallama
wasinu kër moom lu mat a bàyyi la.
galsenai
ton ton u naat saa yu wëree am réew dunq yaa tax
alffa
ba ma gisee mu xalmbànde laa xalaat ne tiijan la
alffa
maa nekkoon ca boppu waar wa.
galsenai
bu ma tolloo diggante seeti samay wóllëre
alffa
kii de dafay wanteer njëg li neex na lool
alffa
bëri na trop bëri na trop waaw te loolu yëpp si communication bi la
kallama
dem na ba di bëgga àgg ñu ne ko mu waññiku
alffa
rond point sacré coeur
urban_bus
am na ab nataalukaay .
galsenai
suubkat yu bare kulóor yi rekk lañuy jëfandikoo
alffa
bi mu ñówee ba jubsi dëkk bi dafa daldi xaaj nitam yi
alffa
ban oto mooy jaar cité port
urban_bus
bu ko defee tawreet ñeel muusa,injiil ñeel
galsenai
sapeur dieupeul
urban_bus
pharmacie bousso dramé
urban_bus
fukki jeunes
kallama
mosquée des mamelles
urban_bus
ndax nag mooy sunu jàmm te it dafa bokk ci jaamu yàlla.
galsenai
kenn ci ñoom nag dóor surgab saraxalekat bu mag ba, noppu ndeyjooram dagg.
bible
ñooy topp li nga xam si ne moom mooy wàllu mbay moomu
kallama
fajkat buy liggéey ci fiñuy fajee xalé yi bu pittsburgh pennsylvania dina ñu ko jiiñ faat bu doywar ginnaaw biñu gissé yaayam faatu ci ginnaw daamaaram alarba njiit yi ci ohio ñoo ko wax
fleurs
dafa di, yaakaar la génnub kaso xalifa sàll bi meññloo ci xol yi
galsenai
tandem immobilier scat urbam
urban_bus
mag ñeek ndaw ñi, góor ñeek jigéen ñi
galsenai
rafetoon ba kenn ñemmewu ko woon jege
alffa
en tout momadou sonko dañ lay sant di la gërëm
kallama
wante ñun li ñu leen di sensibiliser mooy fexeel ba bu ñuy jël bu ñu tojee kees bi la nga fa am
kallama
boo xam ne ndox la boobu waxtu bu la neex boo ñu soññee rek ñu ñëw defal la ko ñu defal la ko service agriculture mooy jiitu nattal ñu suuf si ne ñu variété bi muy béy baax na respecté na calendrier cultural comme ni ngeen amee ci campagne vaccination
kallama
ndam duq ndam dàññ ndëjër ndam jëlal puum
alffa
noppi te tëj sa gémmiñ.
galsenai
prag mooy péyu réewum cek
galsenai
echangeur fann
urban_bus
mbuumbànd bokk na ci po yi ñu lim ci téere bii
alffa
ma nga ca tundu kafrin wa,
galsenai
tom dafa màndi bu baax.
galsenai
anamu météo yu jéggi dayo ñooy baat yi ñuy faral di jëfandikoo ngir wax jafe-jafe ak loraange yi ñu mëna def ci nit ñi koy dundu
fleurs
li nga xam ne nag wax nga ko déclarer nga ko
kallama
rikk nangay tudd lu baax la nekk ci ñoom bu nu léen tuddee
galsenai
dox naa ba sama kàlluur yaa ngiy metti
alffa
yàquteem tax na ba fu mu dem ñu dàq ko
alffa
am na bulletins boo xamante ni moom dafay wax ci li ñuy wooyee vague de chaleur
kallama
neen ak noflaay jëmm ju bëgg a doon dara du leen taamu
galsenai
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
11