fr
stringlengths 4
1.08k
| wo
stringlengths 2
4.02k
| en
stringlengths 3
1.08k
|
---|---|---|
Une mise au point qui fait suite à la déclaration des travailleurs de la Sde réclamant 15% des actions concernant l'affermage de l'eau. | Liberte 6 ngir xool néeg limat benn bi ñu tëjoon Baay Móodu Faal. | This development follows the declaration by the Sde workers demanding 15% of the water sealing actions. |
C’est une stratégie efficace, car certains utilisent cette dispersion à des fins douteuses. | Loolu xalaat bu mucc-ayib la ndax ñenn ñi ni ñuy jëfandikoo suñu tasaroo gi dafa teey xel. | This is an effective strategy, as some use this dispersion for dubious purposes. |
Dès que vous sortez du courant, le retour à la nage n'est pas plus difficile que d'habitude.
| So gennee ci kurang bi, feeey dellu dootul metti ne ni muy faral di mel.
| Once you get out of the current, swimming back is no more difficult than usual. |
Les Citizens, dans un match contrôlé de bout en bout, s’imposent et remportent le titre de champion d’Angleterre. | Citizen yi, ci joŋante boo xam ne ñoo ci teg tànk, mujje nañu jël raaya gi ca Angleterre. | The Citizens, in a tightly controlled match, won the match and became the champions of England. |
Seuls deux d’entre eux avaient réservé un siège business: Kalidou Koulibaly et Sadio Mané. | Ñaar rekk ci ñoom ñoo tiyelu woon palaasu bisnes : Kalidu Kulibali ak Saajo Maane. | Only two of them had booked a business seat: Kalidou Koulibaly and Sadio Mané. |
On est encore loin de l'émergence en agriculture avec les houes sine et les semoirs monoblocs (parole d'expert). | Sori nañu yokkute ci mbay mi ndax ay soox-soox ak ay cunwaari nji lañu yor ba tay. (waxi boroom xam-xam ci mbir mi) | We are still far from the emergence in agriculture of sine-hoes and single-block sowing machines (expert opinion). |
Le personnel médical comme celui administratif n’a pas manqué de magnifier les réalisations du directeur sortant Dr El Hadji Magatte Seck, non sans souhaiter plein de succès à celui entrant. | Liggéeykati kër doktoor yi niki, yu nguur gi, rafetlu nañu liggéeyu kilifa gi ñu fa jële di Doktëer Alaaji Màggat Sekk, fàttewuñoo ñaanal ndam kilifa gi ko wuutu. | Both the medical and administrative staff praised the achievements of the outgoing director Dr El Hadji Magatte Seck, not without wishing the new director every success. |
Ma mère raconte souvent la première fois que nous sommes de retour en Afrique. | Sama yaay dafay fàttali lu bari sunu yoon bu jëkk ñu dellu si Afrig. | My mother often talks about the first time we came back to Africa. |
Lui,au moins il n'a violé personne contrairement à yolom guégnoBravo Maître. | Moom, lu mu bon bon sàkkuwul benn jigéen, wuute ak yolom geño, jaraw-lakk Meetaar. | He, at least he didn't rape anyone unlike yolom guégno. Bravo Master. |
Se fixant des objectifs ambitieux à moyens et à court termes, le FSD fait de l’amélioration de la performance et la gouvernance des entreprises publiques de son portefeuille ainsi que la rentabilité des actifs qui lui ont été transférés par l’État l’une de ses priorités., | Ca fa yaakaarlu fa teg seen bët ci diir bu gàtt ak diir wu gudd, FSD moo ngi suuxat xarañteef ak doxalinu këru liggéeyukaay yu nguur gi ci gafakaam ak lañuy for ca la ko nguur gi dénk te muy li ko soxal. | The FSD sets ambitious medium- and short-term objectives and makes improving the performance and governance of the public enterprises in its portfolio and the profitability of the assets transferred to it by the State one of its priorities. |
Voilà toute la différence, toute l’innovation apportée dans cette lutte panafricaniste non clandestine et qui se fait par voie démocratique. | Lii mooy li leen wutale, coppite yi bile xeexu waa Afrig gi amul benn nëpp-nëppal te tegu ci yoon. | This is the difference, the innovation brought to this Pan-Africanist struggle, which is not clandestine and is carried out democratically. |
De l'autre, il y avait Zamalek, également invaincu et tombeur de l'autre gros morceau continental, les Angolais de Petro de Luanda, dans le dernier carré. | Ci feneen fi, amoon na Zamalek mi kenn mënul a daane, noon meneen mbooloo mi, waa Angola yi bawoo ci Petro bu Luanda ci mujjantalu joŋante bi. | On the other side, there was Zamalek, also undefeated and losing to the other big piece of the continent, the Angolans of Petro de Luanda, in the last square. |
Ça représentait un serpent boa qui avalait un fauve. | Nataal baa ngi doon wone yeew muy wonn (am) mala. | It was a boa constrictor swallowing a wild animal. |
Sur le plan international, il existe près de 200 organisations de visite en course à pied. La plupart d’entre elles fonctionnent indépendamment.
| Ci àddina bi yépp, am na lu jege 200 mbootaay dàw. Lu ëpp ci ñoom dañuy liggéeyal seen bopp.
| There are nearly 200 walking tour organisations internationally, most of which operate independently. |
Une rencontre avec la communauté sénégalaise établie à Niamey est au menu du programme. | Am ndajem waa Senegaal yi nekk Ñaame bokk na ci tëralin wi. | A meeting with the Senegalese community in Niamey is on the agenda. |
l’État ne subventionne plus un secteur privatisé, soyons en conscients. | Nguur doolelatul wàll bi ñu jagleel liggéeyi jàmbur yi, ñu bàyyi ci xel. | The state no longer subsidizes a privatised sector, let us be aware of that. |
Adieu, dit-il à la fleur. | Mu ne tóor-tóor bi: Tàggu naa la. | "Farewell", he said to the flower. |
Ah ! Je me réveille à peine… Je vous demande pardon… Je suis encore toute décoiffée… | Ah! Daanaka maa ngi soog a yewwu… Maa ngi leen di jégalu… Sama bopp baa ngi ne sàyy ba tey… | I'm just waking up, and I'm sorry, but I'm still all peeled up. |
Cependant, une nouvelle preuve suggère que les Moriori étaient un groupe de Maoris du continent qui ont migré de la Nouvelle-Zélande vers les îles Chatham, développant leur propre culture distincte et pacifique.
| Waaye, firnde yu bees dañuy xamle ni Moriori yi ab kuréelu Maori yu bokk ci kontinan bi bu toxu woon bawoo Nouvelle Zeland dem ci Chatham Islands, nekk di defar seen cosaan buñu moomal seen bopp te teggu ci jàmm.
| However, new evidence suggests that the Moriori were a group of mainland Maori who migrated from New Zealand to the Chatham Islands, developing their own distinct and peaceful culture. |
Et il recommença de frapper ses mains l’une contre l’autre. | Mu tàmbaliwaat tàpp benn loxo bi ci beneen bi. | Then he began to strike his hands one against the other. |
À ce que je sache la justice est rendue au nom du peuple alors pourquoi ceux au nom duquel celle-ci est rendue n’ont pas le droit d’apprécier son action à l’aune de sa mission. | Ci li ma jot a xam, ginnaaw dañuy àtte ci turu askan wi lan moo tax amuñu yelleefu joxe seen xalaat ci jëf jooju. | As far as I know, justice is done in the name of the people, so why should those in whose name it is done not have the right to appreciate its action in the light of its mission. |
Les artistes étant toujours fascinés par la science ce n’est donc pas un hasard qu’ils veuillent reproduire la nature à l’identique. | Ñiy yëngu ci caada dañoo mës a bëgg xeltu, kon warul jaaxal kenn li ñu bëgg a niroole li ñuy def ak dëgg gi. | Artists are always fascinated by science, so it is not by chance that they want to reproduce nature in an identical way. |
« Vous n’arrêtez pas de vous rappeler que nous menions largement à Valderrama ; nous avions une grosse avance à Brookline, où nous avons échoué, ainsi qu’à Valderrama, où nous avons gagné, mais de justesse » a déclaré Bjorn, après observé le Classement de 2018 remporter la victoire 5-3 à la fois vendredi et hier au Golf National pour mener 10-6.
| Doomu Amerik boobu di Phil Mickelson dina def benn rekoor ci bisu Dibeer su jongante 47 reelu matsa bu Ryder Cup, waaye nak defa wara fexe ba mu and ak cawarteem yepp ndax mu baña doon jaloore bu saful dara.
| "You keep remembering that we were leading by a wide margin in Valderrama; we had a big lead in Brookline, where we failed, as well as in Valderrama, where we won, but by a narrow margin", said Bjorn, after watching the 2018 Rankings win 5-3 on both Friday and yesterday at Golf National to lead 10-6. |
Pas d’art sans homme mais peut être également pas d’homme sans art . | « Aar » du am te nit amul waaye tamit nit mënul am te aar du am. | No art without man, but it can 't be no man without art either. |
Selon le journal Die Zeit, qui cite un porte-parole militaire, la mise en service du « Rheinland-Pfalz », le navire amiral des toutes nouvelles frégates du Bade-Wurtemberg, a été reportée au premier semestre 2019.
| Waaw taariix dinama won man ak ñépp ekip bi jeexalagul.
| According to the newspaper Die Zeit, citing a military spokesman, the commissioning of the Rheinland-Pfalz, the flagship of the brand new Baden-Württemberg frigates, has been postponed to the first half of 2019. |
La monnaie officielle des Îles Malouines est la livre des Îles Malouines (FKP) dont la valeur est équivalente à une livre sterling (GBP).
| Xaalisu Falklands bu nu dëggal mooy poun bu Flakland (FKP) nga xam nenjëgam danu ko def mu tolloog pound bu Angalteer (GBP).
| The official currency of the Malvinas is the Malvinas Pound (FKP) which is equivalent to one Pound Sterling (GBP). |
Restait donc à savoir comment la CAF allait répartir les 22 autres équipes en lice. | Li ci desoon mooy nan la waa CAF di séddale yeneen ñaar-fukk ak ñaar i ekib yi ci bokk. | The question was how CAF would allocate the remaining 22 teams. |
L’USGS (United States Geological Survey) et son centre national d’information sur les tremblements de terre n’ont pas reçu de rapports immédiats sur les dommages.
| Amul benn raporu loraange ci saasi bu bawoo ci waa United States Geological Survey (USGS) ak këram gii di Barabu Leerali Yëngug Suuf.
| The USGS and its National Earthquake Information Center did not receive immediate reports of damage. |
Le premier était à Mayence depuis un petit moment, le second venait d'arriver au Bayern Munich. | Mayens nekkoon na ci bopp bi ci diir bu tuuti, ki toppoon ci moom Bayern Munich la. | The first had been in Mainz for a while, the second had just arrived in Bayern Munich. |
Mobilisations de militants et des masses populaires par des moyens financiers colossaux de façon indécente et usage illégal des moyens logistiques de l'état. | Dajale ay militaŋ ak ay mbooloo ak xaalis bu tàkku boo si def ci anam bu ñaaw ak jëfandikoo ci lu jaarul yoon ay jumtukaayu yeb ak yebbi yu nguur gi. | Mobilisation of activists and the masses of the people by colossal financial means in an indecent way and illegal use of state logistical means. |
Au nord, la région est délimitée par le Sahel, et au sud et à l'ouest par l'océan Atlantique.
| Ci bët gànnaar diwaan bi dafa jokko ak Saxel, ak ci bët saalum ak sowwu jokko ak Mbàmbulaanug Atlas.
| The region is bounded to the north by the Sahel, and to the south and west by the Atlantic Ocean. |
Linguistique, Sciences du langage et Communication. | Làkk, xam-xamu làkk ak jokkoo. | Linguistics, language and communication sciences. |
Ceux qui rappellent la promesse de Macky Sall de ne pas faire de troisième mandat, sont guillotinés par Décret (Moustapha Diakhaté, Sory Kaba), ceux qui claironnent la possibilité d’un troisième voire d’un mandat à vie sont promus ; si bien que tous les Responsables de l’Apr et anciens pourfendeurs du troisième mandat de Wade rasent les mûrs pour éviter de répondre à la Presse. | Ñiy fàttali la Maki Sàll dige woon ne du def ñetteelu ay, dekereb (Mustafaa Jaxate, Sóori Kabaa), daggate na leen, li leer ci gis-gis mooy mën a nekkub ñetteelu ay gi ci falu giiru dundam mën na nekk ; ba nga xam ne njiitu APR yépp ak ñu yàgg ña tabaxoon ñetteelu palug Wàdd ñoo ngi tëb miir yi ngir bañ a tontu taskati xibaar yi. | Those who recall Macky Sall's promise not to run for a third term are guillotined by Decree (Moustapha Diakhaté, Sory Kaba), those who suggest the possibility of a third or even a lifetime term are promoted; so that all the officials of the AP and former offenders of Wade's third term shave their beards to avoid answering the Press. |
En effet, le géant français a aussi baissé drastiquement les frais de transfert d’argent. | Waaw, këru liggéeyukaayu Farãas gu mag bi, wàññi na bu baax njëgi yónne wala jot ci xaalis gi. | The French giant has also drastically reduced the cost of transferring money. |
La dernière en date fut le rassemblement du 04janvier à l’occasion de la célébration des six (06) années d’existence de PASTEF. | Bi ci mujj mooy ndaje mi ci ñeenti fan ci weeru sãawiyee wi ñuy sargal juróom-benni ati PASTEF. | The last one was the meeting on 04 January to celebrate PASTEF's six (06) years of existence. |
Sa création est considérée comme l’une des mesures phares de la vision 2035 qui guide l’action gouvernementale et oriente la stratégie économique du pays sur le long terme. | Juddoom nekk na benn solo boo xam ne ci gis-gisu 2035 mooy sumb nguur gi te singali doxalinu nguur gi ba pare jiital pexey koom-koomi réew yi ci lu yàgg. | Its creation is considered one of the key measures of Vision 2035, which guides government action and guides the country's long-term economic strategy. |
« Ce n’est pas facile d’y arriver, mais je ne me considérerais probablement comme une réussite ici que si je parviens à ramener le club là-bas. »
| Ay bëreb yu bari ci rëëw mi -rawatina nak kapitaal bi nekkaatnañu ay "dëkku demm" ndax ay nit yu nekkul waa UK ñoo jënd suuf yi te lu ëppu ñoom ci bitti réew ma lañuy nekk.
| It's not easy to get there, but I probably wouldn't consider myself a success here unless I could get the club back there. |
Alors je me suis intéressée à son parcours, aux raisons de sa radiation dans la fonction publique en tant qu’inspecteur des impôts. | Ma tàmbalee saytu fi mu jaar, li tax ñu dàq ko ci liggéeyu nguur gi mu yore woon bi mu nekkee eespektëeru lempo. | So I looked into his background, why he was dismissed from the civil service as a tax inspector. |
Il n’existe pas d’intellectuel sans engagement social ou politique, sans combat contre l’injustice. | Amul benn borom xel, bu dul takku ngir askanam wala pólótig, te du am jàmmaarloo ak ñiy jalgati yoon. | There is no intellectual without social or political commitment, without the fight against injustice. |
Arrestation à Londonderry : Des hommes percutent une maison en voiture
| Londonderry: Ay nit yu ñu japp ginnaaw bi ñu daanale ap kër ak oto
| Arrest in Londonderry: men are driving into a house. |
Adieu, dit la fleur. | Tóortóor bi ne ko:Yàlla nañu Yàlla wonalewaat. | "Goodbye", said the flower. |
Il a eu cinq plaquages au total samedi avant de sortir du match, ce qui a porté son total de la saison à 18 plaquages.
| Deñu koy jéema def lu bari, te gisngeen ñuy def loolu lu bari ci ayubes yu bari yii ñu genni te loolu dina jél palaasu jottali xibaar boo leen mëne wax ak persida bu Amerig.”
| He had five tackles total on Saturday before being pulled from the game, bringing his season total to 18. |
Il permet ensuite, de avec les usagers de cette Administration, avec les différents partenaires au développement et de façon plus générale, avec l’ensemble de l’opinion, un certain nombre d’informations sur la gouvernance publique. | Ba tey dafay waral am ay xibaar yu jëm ci njiiteefu pénc mi, ànd ci ak way-jëfandikooy njiiteef googu ak liggéeyandoo yi ci suqaliku gi, nit ñépp. | It then provides a range of information on public governance to the users of the Administration, the various development partners and, more generally, the public at large. |
Aussi, c'est bien sous l'ère de l'ex président accidentel wade abdoulaye que des êtres (ses semblables) incultes-ignorants-nullards, sans diplômes légalement acquis, accédaient à la tête de hautes fonctions républicaines. | Tamit, ci nguuru njiitu réew ma woon te palam doon fakastalu rekk Wàdd Abdulaay la ay nit (ay àndandoom) yu xamadi, amuñu benn lijaasa bu yoon nangu, doon nekk ci bopp nguur gi. | It was also during the era of the accidental former president Wade Abdoulaye that (his kind) of uneducated, ignorant, uneducated people, without legally acquired diplomas, were accessing high republican positions. |
Ces multiples reports lui ont valu le sobriquet serpent de mer . | Ajandeem yu bare yee tax ñu dàkkantale ko jaanu géej. | These repeated delays have earned him the nickname " Sea Serpent. " |
Ces efforts du gouvernement ont boostés les productions agricoles avec des taux de croissance annuel moyen oscillant entre 5 et 57% aussi bien pour les surfaces emblavées que pour les productions de céréales, d’arachide, de pastèque et de sésame. | Góor-góorlu bi nguur giy def a yokk njureefi mbay yeek seen tolluwaay bu yemamaay bi at mu nekk te tollu ci diggante juróom ak juróom-fukk ak juróom-ñaar ci téeméer boo jël ci tool yi ñu mënal ak njureefi pepp yi, gerte gi, xaal jeek sesaam bi. | These government efforts have boosted agricultural production with average annual growth rates ranging from 5 to 57% for both land-fills and for cereals, peanuts, watermelon and sesame production. |
Tant que ces problématiques ne seront pas posés avec courage et résolus pour que les richesses naturelles du continent restent dans le continent, soient transformés dans le continent pour bâtirun avenir pour nos enfants et nos petits-enfants, nous ne gagnerons jamais le pari du développement quels que soient les programmes qu’on proposera. | Fileek amuñu fitu wax seeniy jafe-jafe te saafara ko ngir alal ji nekk ci dénd bi sax fi, ñu soppee ko fi ngir sunuy doom ak i sët jariñu ci ëllëg, dunu am ndam mukk ci yoonu yokkute wi ak tëralin wu nu mën a teg. | Unless these issues are addressed with courage and resolve so that the natural resources of the continent remain in the continent, are transformed in the continent to build a future for our children and our grandchildren, we will never win the development bet no matter what programmes we propose. |
Mais le problème qui risque de se poser se situe au niveau de l’agenda du F CFA qui n’est pas le même que celui de l’Eco. | Waaye jafe-jafe bi nar a am mooy ne tëralinu CFA bi bokkul ak bu Eko bi. | But the problem that may arise is that the agenda of the CFA Fund is not the same as that of the Eco. |
Les seuls qui en parlent formulent des prières pour lui et invoquent la présomption d’innocence mais jamais des soutiens et défenses énergiques à la grande gueule et aux formules juridico-judiciaires. | Ñenn rekk ñi ciy wax ñu ngi koy ñaanal te di ñaan mu bañ ci taqe, waaye amul ay jàppalekat yu koy def ak xadar wala ak kàdduy yoon ak yoonal. | The only people who talk about it are those who pray for him and invoke the presumption of innocence, but never those who make vigorous and loud defenses and legal formulae. |
Le cinquième jour, toujours grâce au mouton, ce secret de la vie du petit prince me fut révélé. | Ca juróomeelu bés ba laa xame ndéey lii ma leen di waaj a wax, ci dundu ndoomu buur si, lépp ak xar mi ba tey. | On the fifth day, again thanks to the sheep, this secret of the little prince's life was revealed to me. |
Par Nafissa Dramé Dia | Nafisa Daraame Ja moo ko bind. | By Nafissa Dramé Dia, who is the author of the book |
Ne pars pas, je te fais ministre ! | Bul dem, dina la def jëwriñ ! | Don't leave, I'll make you a minister! |
A l’heure où les grandes démocraties comme les USA ont déjà réglé et dépassé ce problème, devons nous persister dans ce fait d’être à la fois des victimes et complices de ces goulots d’étranglement ? | Ci jamono jii nga xam ne réewu demokaraasi yi mel ni Amerig romb nañu jafe-jafe boobu, ndax war nañoo toog seetaan di wéy di ci loru ak di ànd ci jëfin yu ñaaw yooyule ? | At a time when great democracies like the US have already dealt with and overcome this problem, should we continue to be both victims and accomplices of these bottlenecks? |
Les preuves ont montré par la suite que les tests avaient été falsifiés par Hall, ainsi que par 34 autres fonctionnaires de l'éducation nationale, qui ont été mis en examen en 2013.
| Ay firndé wanena ni xayma xam-xam yi dañu amone wuruj. Hall ak yenen 34 njit ci walu jang mi tegon nañu len loxo ci atum 2013.
| Evidence later showed that the tests had been falsified by Hall, as well as by 34 other officials in the National Education Authority, who were indicted in 2013. |
Des mouches ? | Ay weñ? | Flies? |
Il sait bel et bien que les montants sus cités n’ont pas été investis où de droit. | Xam na bu baax ne xaalis bi mu wax yépp dugaluñu ko fi mu waroon a dugg. | He knows that the sums mentioned above were not invested in any legal way. |
Cette affaire est symptomatique d’un mépris total des règles élémentaires en matière de légalité fiscale. | Mbir móomu day wàllee te ñàkk a xam gu mag moo ko waral ci mbirum kàggu la. | This case is symptomatic of a total disregard for the basic rules of tax law. |
Voilà singulièrement ce que je disais sur la question dans mon ouvrage Solutions pour un Sénégal nouveau , publié en septembre 2018 : Le gaspillage est l’autre moyen de dilapidation des ressources. | Gisal man cundum li ma doon wax ci sama téere bi Solutions pour un Sénégal nouveau, bi ñu siiwal ci weeru sàttumbar 2018 : yàq bi weneen yoon wi ñuy sànke alal ji. | This is what I said about the issue in my book Solutions for a New Senegal, published in September 2018: Waste is the other way of squandering resources. |
Organisez un meeting ,vous ne verrez que des voyous et des délinquants avec vous. | Woote léen am ndaje, dooleen fa gis lu dul ay bàndi ak ay addu-kalpe yuy ànd ak yéen. | Organize a meeting, you'll only see thugs and delinquents with you. |
Vendredi matin, rapporte Mic, les manifestants ont chanté « Le mois de novembre arrive ! » dans le couloir du Sénat alors que les républicains régissant le Comité judiciaire ont choisi d’avancer la nomination de Kavanaugh malgré le témoignage du docteur Christine Blasey Ford.
| "Amuñu woon benn jot ngir rawal sunu bopp.
| On Friday morning, Mic reports, protesters chanted "November is coming!" in the Senate corridor as Republicans ruling the Judiciary Committee chose to move forward with Kavanaugh's nomination despite testimony from Dr. Christine Blasey Ford. |
Le projet de loi exige que les jeux vidéo violents vendus dans l'État de Californie soient étiquetés avec un autocollant portant la mention « 18 » et rend leur vente à un mineur passible d'une amende de 1000 dollars par infraction.
| Keyt gi dafay laaj ab powu video bu tar bu nu jaay ko ci dëkku Kaliforni nu taf ci “18” te fexe ku ka jaay xale ñu daan la $1000 tooñ bu nekk.
| The bill requires violent video games sold in the state of California to be labeled with a sticker that reads 18 and makes their sale to a minor punishable by a $1,000 fine per violation. |
Il est clair que le monde a beaucoup changé grâce aux progrès scientifiques et technologiques réalisés par les êtres humains, et que les problèmes sont devenus plus importants en raison de la surpopulation et du mode de vie extravagant de l'humanité.
| Lu leer nañ la ni addina bi dafa soppeeku bu baax ndax yokkute yi am ci xarala yu bees yi ci nit ñi te jafe-jafe yi dañoo gëna bari ndax ni nit ñi di yokkee ak anam bu ëpp bu nit ñi di Dundee.
| Clearly, the world has changed a great deal because of the scientific and technological advances made by humans, and the problems have become more serious because of humanity's overpopulation and extravagant lifestyle. |
Conformément aux prévisions, l’ouragan Rosa s’affaiblit à mesure qu’il se déplace au-dessus des eaux plus froides de la côte nord-est du Mexique.
| Ci fagaru, uragaanu Rosa dina wacc ginnaaw mungi dugguji ci ndox yu sedd yu bëtu gannaar bu Mexico.
| As forecast, Hurricane Rosa is weakening as it moves over the colder waters of the northeast coast of Mexico. |
Ils ne cachent en effet par leur amitié, née il y a un peu moins de dix ans en Allemagne. | Nëbbatu seen xaritoo gi juddu ca Almaañ lu war a yées fukki at. | They do not hide their friendship, which began a little less than ten years ago in Germany. |
Elle avait toussé deux ou trois fois, pour mettre le petit prince dans son tort : Ce paravent ?… | Mu daldi sëqët ñaar ba ñetti yoon ngir ndoomu buur si am kersa: Sàkket woowu?... | She coughed two or three times, to put the little prince in his wrong: |
Outre cette régularité phénoménale, City s’est appuyé cette saison sur une attaque de feu (95 buts marqués) et sur une défense de fer (23 buts encaissés). | Teewaayu Mansesteer Siti bu mucc-ayib ci at mi moo ngi tënku ci juróom-ñeent-fukk bal ak juróom yi ñu dugal ak ñaar-fukki bal ak ñett yi dugg ci seeni caax. | In addition to this phenomenal regularity, City relied this season on a fiery attack (95 goals scored) and on an iron defense (23 goals conceded). |
Quelle ironie du destin, il marche aujourd’hui dans ce sillage !Ce qui est dommage pour les sénégalais, c’est que personne de son entourage n’a tenté de le contredire sur ce point, à priori on lui vouait un culte sans borne. | Ndaw yoon bu reetaanlu, mu ngi doxee nóonu tey ! li ci doy waar mooy ci waa Senegaal, moom amul kenn ci li ko wër ku ko wéddi ci pàcc bóobu, moom dañu koo fonk lool. | What a tragedy, he is now following in his footsteps. What is a pity for the Senegalese is that no one around him has tried to contradict him on this point, a priori he was worshiped without limit. |
Désormais, c'est sur le terrain judiciaire que les deux hommes vont, désormais, s'expliquer. | Léegi ci yoon la ñaari nit ñii di dem, lijjanti fa seeni mbir. | Now it's on the court that the two men will now explain themselves. |
« C’est tellement facile de jouer le rôle de président, mais au lieu d’avoir 10 000 personnes qui tentent d’accéder à cette arène pleine à craquer, il n’y en a à peine plus de 200 debout devant moi », critiqua-t-il en pointant du doigt vers la foule.
| " Yeyoo nekk njiit lu yomb la, waaye ludul am 10000 nit fee ci bitti ngir jox ko ëttu bu ñu defar ba pare , naroon nañu am 2000 nit yu taxaw fee" lii la Trump wax di joxoñ mboolo mi ci kanamam.
| It's so easy to play the role of president, but instead of having 10,000 people trying to get into this packed arena, there are barely more than 200 standing in front of me, he criticized pointing his finger at the crowd. |
À part l'événement de mercredi, Carpanedo a participé à deux courses individuelles lors des Championnats.
| Li weesu xew-xewu Alarba, Carpanedo bokk na ci ñaari rawanté kenn pàr kenn ci Sampiyonaa yi.
| Apart from Wednesday's event, Carpanedo competed in two individual races at the Championships. |
Pour ses résultats plus élogieux et plus flatteurs que prévu, malgré la fraude, le Président Sonko attentionne. | Nit ñaa ngi bàyyi xel Peresidaŋ Sónko ndax lim bu takku bu neex te bette bi mu am, doonte sax wote yi am nañu ay njuuj-njaaj. | For his results more praiseworthy and more flattering than expected, despite the fraud, President Sonko is careful. |
MD : Ton vécu en France a-t’il influencé ta vision de la politique sénégalaise ? | MD : li nga dund Farãas ndax yokk na sa gis-gis ci pólotigu Senegaal ? | MD: Has your experience in France influenced your view of Senegalese politics? |
L’avant des Skyblues a envoyé le ballon dans les filets juste avant de glisser en dehors du terrain.
| Eliye bu Bula asamaan yi laxas bal bi ci caax yi bala muy tëb ci biir.
| The Skyblues forward sent the ball into the nets just before sliding off the field. |
Une performance qui pourrait changer les plans du Real Madrid. | Xarañte bu mën a soppi mbiru Reyaal Madirit. | A performance that could change Real Madrid's plans. |
Son expression "Ooh, je suis foutu !" qu’il a tonnée lors de son interpellation en disait long sur la terreur que vivait l’homme Bougazeli. | Waxinam wi "Wóoy, yàqu naa !" bi mu doon aalu ci biñ koy laaj wane na lu bari xoqatal bi Bugaaseli doon dund. | His expression "Ooh, I'm screwed!" which he uttered during his arrest said a lot about the terror that Bougazeli was living. |
Le milieu de Bruges Krépin Diatta a marqué le deuxième but d’une magnifique reprise des 20 mètres, pour sanctionner une relance ratée des Tanzaniens sur un corner. | Futbalkatu digg bu Bruges bi, Kerepee Jaata dugal na balu ñaareel bi cib àndandoo bu rafet, lu tollook ñaar-fukki meetar (20), ngir fayul benn bal bu waa Tanzanie mball. | Bruges midfielder Krépin Diatta scored the second goal from a magnificent 20 metre recovery, to penalise a missed recovery by the Tanzanians on a corner. |
Avec une loi d’habilitation tirée de l’application de l’article 77 de la Constitution, le pouvoir du Président de la République ne peut être absolu. | Bu ñu seetee ci sàrtu nangul jëf bu ñu jële ci doxalinu dog 77 bu ndeyu àtte réew mi, doole njiitu réew mi dafa am fu yem. | With a law of empowerment derived from the application of Article 77 of the Constitution, the power of the President of the Republic cannot be absolute. |
Un véhicule particulier, qui était à destination de la ville sainte de Tivaouane, est entré en collision avec un autre qui prenait le sens inverse. | Ab oto bu ràññeeku, bu nekkoon ci dëkku diine bu sell bi, Tiwaawan, moo mbëkkante ak beneen bu jóge ci beneen boor bi. | A private vehicle, which was heading to the holy city of Tivauan, collided with another that was going in the opposite direction. |
Dans la nuit du vendredi au samedi, 39 personnes ont été arrêtées. | Ci guddig aljuma ba gaawu, fan-weer ak juróom-ñeenti nit téye nañu leen. | On the night of Friday to Saturday, 39 people were arrested. |
Malgré tous ces dangers qui se profilent à l’horizon et qui risquent de saper la reprise des cours dans les universités, il est possible de proposer des pistes de réflexion qui peuvent déboucher sur des solutions pouvant amoindrir la propagation du virus:Distribuer gratuitement et en permanence des masques aux étudiants;Assurer l’hygiène des infrastructures pédagogiques en multipliant les équipes de nettoyage et en mettant à leur disposition des kits sanitaires suffisants;Communiquer davantage sur les mesures spécifiques qui doivent être prises pour l’hébergement au campus. | Ak musiba yi ñuy yoot te nar a nasaxal tàmbaliwaatu njàng mi ci daara yu kawe yi, war na ñoo mën a amal ay waxtaan ngir am pexe yu mën a wàññi lawug doomu jàngoro ji : may ndongo yi ay mask saa su ne ; setal bérébi jàngukaay yi ak jumtukaay ya fa nekk ; jox ndongo yi ay jumtukaayi raxas loxo yu doy ; waxtaan bu baax ci matuwaay yi ñu war a jël ci dëkkuwaay yi. | Despite all these dangers looming on the horizon and threatening to undermine the resumption of classes in universities, it is possible to propose ways of thinking that can lead to solutions that can reduce the spread of the virus:Distribute free masks to students on a permanent basis;Ensure the hygiene of educational infrastructure by increasing the number of cleaning teams and making sufficient sanitary kits available to them;Communicate more about the specific measures that must be taken for accommodation on campus. |
Il resta donc debout, et, comme il était fatigué, il bâilla. | Ndegam dafa sonn, mu óbbali. | So he stood there, and he yawned because he was tired. |
« S’il avait été en charge, nous serions déjà sortis », a-t-il déclaré.
| ñeent ci ñii faatu ay tukkikatu Arsantiin lañu woon.
| If he was in charge, we would have already come out, he said. |
Elizabeth Warren envisagera sérieusement la possibilité de se présenter aux élections présidentielles de 2020, déclare la sénatrice du Massachusetts
| Ngir tontu benn ci laaj ak tontu yi, ci sitam enternet " Lan moo tax nga xalaat ni munnañu jeexal ñakk?
| Elizabeth Warren will seriously consider running for president in 2020, says Massachusetts senator |
Le Mojip étant un mouvement national, nous comptons dans un premier temps améliorer notre organisation et impliquer toutes les femmes de Pastef France. | Mojip mbootaay la gu nekk ci biir réew mi, fas-yéene nañu jëkk a jekk-jekkal taxawaay bi te dugal ci jigéeni Pastef yu Farãas. | Since Mojip is a national movement, we intend to improve our organisation and involve all the women of Pastef France. |
Je suis en admiration devant le professionnalisme et la détermination de ces collègues, qui font face à une déferlante de propos sexistes ou racistes chaque jour, mais qui ne baissent pas les bras.
| Xamnaa bu baax muna ligeey ak pasteefu naataango yooyu ñuy fitnaal ci wallu xeet mbaa sëy bës bu yalla def te du ñu musa sëgg.
| I am in awe of the professionalism and determination of these colleagues who face a barrage of sexist or racist remarks every day, but who do not give up. |
Au lieu de cela, une rencontre avec Trump, qui se trouvait alors aux Nations unies à New York, a été annoncée pour jeudi.
| Defarkatu oto bu Sapoŋ neena mbiri foronceer munna yeexalat xew mi su de amul juboo ci Brexit bi te munna gallaŋkoor ay ligeey.
| Instead, a meeting with Trump, who was then at the United Nations in New York, was announced for Thursday. |
Plusieurs otages ont été sauvés, et la mort d’au moins six d’entre eux a été confirmée jusqu’à présent.
| Amna otage yu bari yuñ jota wallu waaye amna juróom benn yu ci ñàkk seen bakkan.
| Several hostages have been rescued, and at least six of them have been confirmed dead so far. |
Plus la tension est faible, plus la force vitale présente est positive. Chaque personne a la possibilité de trouver une paix et un contentement absolus.
| Lu sa xol di gëna woyof, lépp ci gëna woyof ci sa àdduna. Nit ku bekk war nga mëna fexe nooy dundee ci jàmm ak salaam.
| The lower the tension, the more positive the life force present, and each person has the possibility of finding absolute peace and contentment. |
Les récentes sorties de Macron et de Guterres sont on ne peut plus claires : l’Afrique est le prétexte pour les organisations mondiales tutélaires de mobiliser énormément de ressources. | Génn yu mujji Macron ak Guterres gën na leer : Afirig la mbootaayi àdduna yi di taafantoo ngir dajale koppar yu sakkan. Te li mbuxumkati koppar yooyu di def, teguwul ci yoon. | The recent statements by Macron and Guterres are clear: Africa is the pretext for the global welfare organizations to mobilize huge resources. |
L'atome peut être considéré comme étant l'une des unités qui constitue toute matière.
| Mën nañu jàpp ni atom mooy benn ci tabax yi gëna am solo ci mbir yépp.
| The atom can be considered as one of the units that make up all matter. |
Le Président Trump autorisa le FBI à enquêter sur les accusations d’agressions sexuelles de Brett Kavanaugh.
| Persida Trump ubbina ap laŋketu FBI ngir tuuma yooyu lalu ci ndoddu Kavanaugh.
| President Trump authorized the FBI to investigate Brett Kavanaugh's sexual assault allegations. |
Te mbir mi, wareesu koo yemale rekk ci taalibe yi. | Te mbir mi, wareesu koo yemale rekk ci taalibe yi. | You're a good teacher. |
Wait and see. | Nañu dégloo rekk, dégloo du booy nopp | Wait and see. |
Le ministère a réagi en qualifiant de « vraiment regrettable » l'ajournement du rapport par Apple.
| Ministre bi tontu na te waxna ni mingi "ñaawlu lool" njukkiy jëf Apple bi ñu toxal.
| The ministry reacted by calling it "really regrettable" that Apple had postponed the report. |
L’ancien capitaine des Lions voulait un immeuble à Dakar. | Ki fi nekkoon kapiteenu Gaynde yi dafa bëggoon am taax (etaas) ci Dakaar. | The former Lions captain wanted a building in Dakar. |
Tout n’est pas perfidie ou trahison, mais juste un charme discret de la démocratie. | Lépp du ñàkkug ngor ak woraate, waaye xeetu dóoru demokaraasi la. | It's not all treachery or betrayal, but just a discreet charm of democracy. |
Rosenstein se trouve dans une situation délicate depuis que ce journal a signalé que, l’année dernière, il a proposé d’enregistrer en secret le président et a émis des hypothèses sur son inaptitude à exercer ses fonctions.
| Diplomaat yi seetlu nañu ne Reewum Dominik ak Panama dañoo nangu Pekin ba pare, te Waasinton wonewul ñakk andam ci loolu.
| Rosenstein has been in a tight spot since the paper reported last year that he proposed secretly recording the president and speculated about his inability to perform his duties. |
Vous rappellez-vous la pièce de théâtre qui illustre l’histoire de Khanju et Ndaté? | Yéen a ngi fàtteliku tiyaatar bi doon wane taarixu Xànju ak Ndate ? | Do you remember the play that illustrates the story of Khanju and Ndaté? |
Le commissaire a dit : « nous ne nous sommes pas encore accordés sur les règles de base, ni sur les concessions tarifaires, mais la perspective envisagée est suffisante pour débuter le commerce d'ici le 1er juillet 2020 ».
| Jotalikat bi nena, “deggoo wa gñu ci nimu sàrtu cosaan bi ak njëgi dêkkuwaay yi, waaye kaadar biñu am doyna ngir ñu tambalee jaay 1 fan ci Sulet 2020”.
| The Commissioner said: we have not yet agreed on the basic rules, nor on the tariff concessions, but the prospect is sufficient to start trade by 1 July 2020. |
Cette grandeur qui ferait l’économie de vies humaines toujours perdues en pareilles batailles. | Tolluwaay boobu dina tax duñu ñàkk ay bakkan yuy faral di des ci xeex yu ni mel. | Such greatness would save the lives of men always lost in such battles. |
Subsets and Splits