audio
audioduration (s)
1.3
171
transcription
stringlengths
8
108
gender
int64
1
1
transcription_normalised
stringlengths
8
108
Ndox mi mu ëmb, cafka gi dafay sëccwex
1
ndox mi mu ëmb, cafka gi dafay sëccwex
Tom gisu ko woon.
1
tom gisu ko woon.
03/07 à 2330 Mine Ubbi njël lu njëkk li
1
03/07 à 2330 mine ubbi njël lu njëkk li
Mas naa jaay lii.
1
mas naa jaay lii.
Damaa yeex a ñëw.
1
damaa yeex a ñëw.
manees na am yaakaar ci moom.
1
manees na am yaakaar ci moom.
Buy délsi yal na nu fekk ak may gu suuxali may
1
buy délsi yal na nu fekk ak may gu suuxali may
Sama liggéey dafa géey.
1
sama liggéey dafa géey.
Toma ngi ci kaw.
1
toma ngi ci kaw.
Biirmaani ci lu bari Bëj-saalum-penku Asi la ñu koy boole.
1
biirmaani ci lu bari bëj-saalum-penku asi la ñu koy boole.
Wax naa dëgg, am déet ?
1
wax naa dëgg, am déet ?
Soxla naa ab farandoo.
1
soxla naa ab farandoo.
dinaa leen gindi
1
dinaa leen gindi
Ñu ngi ko tëye ca màkkaanum mu mag mu alkaati ya ca Ndakaaru.
1
ñu ngi ko tëye ca màkkaanum mu mag mu alkaati ya ca ndakaaru.
Buleen ma xaar.
1
buleen ma xaar.
Bàyyi ma ma nelaw.
1
bàyyi ma ma nelaw.
Jaxaay ji ak picc mi
1
jaxaay ji ak picc mi
Maa ngi jéggalu
1
maa ngi jéggalu
Danuy jënd ay CD.
1
danuy jënd ay cd.
Suuf si daa di nangu.
1
suuf si daa di nangu.
Du sama mbir.
1
du sama mbir.
Xale yi gëmewuñu ko woon
1
xale yi gëmewuñu ko woon
Mbooram bi dëgg la.
1
mbooram bi dëgg la.
Bëgg naa ci benn !
1
bëgg naa ci benn !
Doon naa ko ñaawal.
1
doon naa ko ñaawal.
sunuy jafe-jafe ci wàllu paj soppikuwul.
1
sunuy jafe-jafe ci wàllu paj soppikuwul.
Dama xalaat ne danga reelu.
1
dama xalaat ne danga reelu.
Damaa am ñaan.
1
damaa am ñaan.
Naj ak forse
1
naj ak forse
Danga may fen ?
1
danga may fen ?
Noo rëyee nii?!
1
noo rëyee nii?!
Nu ngi nekkandoowaat.
1
nu ngi nekkandoowaat.
Teew fa nag, doore ko ci sawaal digg-bëccëg ba jant so
1
teew fa nag, doore ko ci sawaal digg-bëccëg ba jant so
Dafa dégg i coow.
1
dafa dégg i coow.
Mbir mii daal, kenn setu ci.
1
mbir mii daal, kenn setu ci.
waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne
1
waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne
Mu ne «Ñoom de ñook woor diirub jamonoo yam».
1
mu ne «ñoom de ñook woor diirub jamonoo yam».
Masuma faa dellu.
1
masuma faa dellu.
Beto De Canda
1
beto de canda
Tom sopp na mool yi.
1
tom sopp na mool yi.
Daanaka, demewu fa noonu
1
daanaka, demewu fa noonu
mu wàcc-liggéey Sëriñ Abdu Laat Mbàkke wuutu ko di xalifab Sëriñ Tuubaa.
1
mu wàcc-liggéey sëriñ abdu laat mbàkke wuutu ko di xalifab sëriñ tuubaa.
Damaa bëgg aar.
1
damaa bëgg aar.
Wéer ngànnaay gi nag lii la wax
1
wéer ngànnaay gi nag lii la wax
Man ngaa lakk farañse a?
1
man ngaa lakk farañse a?
Dañu maa féexal.
1
dañu maa féexal.
Booyal bay ab tool booyal ko am at door koo bayaat
1
booyal bay ab tool booyal ko am at door koo bayaat
Babilon dëkku penku la woon, di péeyug réewu Kalde, maanaam Irak
1
babilon dëkku penku la woon, di péeyug réewu kalde, maanaam irak
Tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi beneen bi mooy tus-wu-gaar
1
tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi beneen bi mooy tus-wu-gaar
Mooy ne, bala dara, Séex Anta tekkikat la woon
1
mooy ne, bala dara, séex anta tekkikat la woon
Boo seetloo, sunu way-tawati Covid-19 yu jëkk yi bitim-réew lañ jóge
1
boo seetloo, sunu way-tawati covid-19 yu jëkk yi bitim-réew lañ jóge
Man nanu koo am it jaare ko ci yeneen i lijjanti.
1
man nanu koo am it jaare ko ci yeneen i lijjanti.
XEESAL WALLA XEEB SA BOPP ?
1
xeesal walla xeeb sa bopp ?
Waxi Seex Anta Joob ju aju làkkSoppi
1
waxi seex anta joob ju aju làkksoppi
Damaa sonn lool?!
1
damaa sonn lool?!
Àdduna wori neen la.
1
àdduna wori neen la.
Loo leen di nëbb ?
1
loo leen di nëbb ?
Yeneen waat yi it noonu lañu mel.
1
yeneen waat yi it noonu lañu mel.
Loolu la ñuy wax dëppaleg déggoo yi.
1
loolu la ñuy wax dëppaleg déggoo yi.
Sawat gi ci njabootug Combretaceae la bokk
1
sawat gi ci njabootug combretaceae la bokk
Ab DVD la.
1
ab dvd la.
Raxas naa ko.
1
raxas naa ko.
màrs 741 ñu faatu
1
màrs 741 ñu faatu
Amoon na ay weer ci ginnaaw.
1
amoon na ay weer ci ginnaaw.
? Àjjuma 24i fani sulet 2020
1
? àjjuma 24i fani sulet 2020
Ndaw nettali lu reelu !
1
ndaw nettali lu reelu !
Ndax sang bii bokkeewul ak yooyee wolof.
1
ndax sang bii bokkeewul ak yooyee wolof.
Halowiin rekk la bañ.
1
halowiin rekk la bañ.
Moom miy ki moy kaa
1
moom miy ki moy kaa
Jox na ko liggéey.
1
jox na ko liggéey.
Déggoon naa leen ñuy ñëw.
1
déggoon naa leen ñuy ñëw.
Askan waa ngiy jooy, di sàkku ndimmal ci neen
1
askan waa ngiy jooy, di sàkku ndimmal ci neen
Ndax damaa jaay yoos mi ?
1
ndax damaa jaay yoos mi ?
Lungeen di def sungeen amul dara lu ngeen di def ?
1
lungeen di def sungeen amul dara lu ngeen di def ?
lii xew ca Medinaa dina dakk!
1
lii xew ca medinaa dina dakk!
Xoolleen nu !
1
xoolleen nu !
ci lol dafay guusali put di yokku tér
1
ci lol dafay guusali put di yokku tér
Li ko waral mooy Xasiidaam yii yamuñu ak dara fa Yàlla sunu Boroom.
1
li ko waral mooy xasiidaam yii yamuñu ak dara fa yàlla sunu boroom.
Mooy ñenteelu xalifa ginnaaw S Abdul Ahad
1
mooy ñenteelu xalifa ginnaaw s abdul ahad
Bul yem rekk ci meew, kafe mbaa duteek yu ni mel
1
bul yem rekk ci meew, kafe mbaa duteek yu ni mel
Lii dula dimbali.
1
lii dula dimbali.
Ku am doole la.
1
ku am doole la.
Am naa lu ma metti lool.
1
am naa lu ma metti lool.
Bii mooy teqaloo ??
1
bii mooy teqaloo ??
Ñépp a ragal.
1
ñépp a ragal.
Wàll gi jeex na.
1
wàll gi jeex na.
Bu dee xas mi
1
bu dee xas mi
Ekool bi, dafa reeluwul.
1
ekool bi, dafa reeluwul.
Ndax Tom dafa lab ?
1
ndax tom dafa lab ?
Kon nag, fàww nu xoolaat nekkiin yi ci biir néegu-sëy
1
kon nag, fàww nu xoolaat nekkiin yi ci biir néegu-sëy
Jàppale ma, ñaan naa la ko !
1
jàppale ma, ñaan naa la ko !
Tom dee na daaw.
1
tom dee na daaw.
Nit ñii mat nañu 21 700 000 2015.
1
nit ñii mat nañu 21 700 000 2015.
Tom daf maa soxla.
1
tom daf maa soxla.
Ñu guree ngeen.
1
ñu guree ngeen.
Dafal li nga bëgg.
1
dafal li nga bëgg.
Yaa ngi tappale.
1
yaa ngi tappale.
Bugaaseli am na bàyyig négandiku
1
bugaaseli am na bàyyig négandiku
Loolu yépp lu man a nekk la, tesax lu am la.
1
loolu yépp lu man a nekk la, tesax lu am la.
Talaata jàpp 5h25 Dog 19h24
1
talaata jàpp 5h25 dog 19h24