audio
audioduration (s) 1.3
171
| transcription
stringlengths 8
108
| gender
int64 1
1
| transcription_normalised
stringlengths 8
108
|
---|---|---|---|
Ndox mi mu ëmb, cafka gi dafay sëccwex | 1 | ndox mi mu ëmb, cafka gi dafay sëccwex |
|
Tom gisu ko woon. | 1 | tom gisu ko woon. |
|
03/07 à 2330 Mine Ubbi njël lu njëkk li | 1 | 03/07 à 2330 mine ubbi njël lu njëkk li |
|
Mas naa jaay lii. | 1 | mas naa jaay lii. |
|
Damaa yeex a ñëw. | 1 | damaa yeex a ñëw. |
|
manees na am yaakaar ci moom. | 1 | manees na am yaakaar ci moom. |
|
Buy délsi yal na nu fekk ak may gu suuxali may | 1 | buy délsi yal na nu fekk ak may gu suuxali may |
|
Sama liggéey dafa géey. | 1 | sama liggéey dafa géey. |
|
Toma ngi ci kaw. | 1 | toma ngi ci kaw. |
|
Biirmaani ci lu bari Bëj-saalum-penku Asi la ñu koy boole. | 1 | biirmaani ci lu bari bëj-saalum-penku asi la ñu koy boole. |
|
Wax naa dëgg, am déet ? | 1 | wax naa dëgg, am déet ? |
|
Soxla naa ab farandoo. | 1 | soxla naa ab farandoo. |
|
dinaa leen gindi | 1 | dinaa leen gindi |
|
Ñu ngi ko tëye ca màkkaanum mu mag mu alkaati ya ca Ndakaaru. | 1 | ñu ngi ko tëye ca màkkaanum mu mag mu alkaati ya ca ndakaaru. |
|
Buleen ma xaar. | 1 | buleen ma xaar. |
|
Bàyyi ma ma nelaw. | 1 | bàyyi ma ma nelaw. |
|
Jaxaay ji ak picc mi | 1 | jaxaay ji ak picc mi |
|
Maa ngi jéggalu | 1 | maa ngi jéggalu |
|
Danuy jënd ay CD. | 1 | danuy jënd ay cd. |
|
Suuf si daa di nangu. | 1 | suuf si daa di nangu. |
|
Du sama mbir. | 1 | du sama mbir. |
|
Xale yi gëmewuñu ko woon | 1 | xale yi gëmewuñu ko woon |
|
Mbooram bi dëgg la. | 1 | mbooram bi dëgg la. |
|
Bëgg naa ci benn ! | 1 | bëgg naa ci benn ! |
|
Doon naa ko ñaawal. | 1 | doon naa ko ñaawal. |
|
sunuy jafe-jafe ci wàllu paj soppikuwul. | 1 | sunuy jafe-jafe ci wàllu paj soppikuwul. |
|
Dama xalaat ne danga reelu. | 1 | dama xalaat ne danga reelu. |
|
Damaa am ñaan. | 1 | damaa am ñaan. |
|
Naj ak forse | 1 | naj ak forse |
|
Danga may fen ? | 1 | danga may fen ? |
|
Noo rëyee nii?! | 1 | noo rëyee nii?! |
|
Nu ngi nekkandoowaat. | 1 | nu ngi nekkandoowaat. |
|
Teew fa nag, doore ko ci sawaal digg-bëccëg ba jant so | 1 | teew fa nag, doore ko ci sawaal digg-bëccëg ba jant so |
|
Dafa dégg i coow. | 1 | dafa dégg i coow. |
|
Mbir mii daal, kenn setu ci. | 1 | mbir mii daal, kenn setu ci. |
|
waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne | 1 | waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne |
|
Mu ne «Ñoom de ñook woor diirub jamonoo yam». | 1 | mu ne «ñoom de ñook woor diirub jamonoo yam». |
|
Masuma faa dellu. | 1 | masuma faa dellu. |
|
Beto De Canda | 1 | beto de canda |
|
Tom sopp na mool yi. | 1 | tom sopp na mool yi. |
|
Daanaka, demewu fa noonu | 1 | daanaka, demewu fa noonu |
|
mu wàcc-liggéey Sëriñ Abdu Laat Mbàkke wuutu ko di xalifab Sëriñ Tuubaa. | 1 | mu wàcc-liggéey sëriñ abdu laat mbàkke wuutu ko di xalifab sëriñ tuubaa. |
|
Damaa bëgg aar. | 1 | damaa bëgg aar. |
|
Wéer ngànnaay gi nag lii la wax | 1 | wéer ngànnaay gi nag lii la wax |
|
Man ngaa lakk farañse a? | 1 | man ngaa lakk farañse a? |
|
Dañu maa féexal. | 1 | dañu maa féexal. |
|
Booyal bay ab tool booyal ko am at door koo bayaat | 1 | booyal bay ab tool booyal ko am at door koo bayaat |
|
Babilon dëkku penku la woon, di péeyug réewu Kalde, maanaam Irak | 1 | babilon dëkku penku la woon, di péeyug réewu kalde, maanaam irak |
|
Tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi beneen bi mooy tus-wu-gaar | 1 | tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi beneen bi mooy tus-wu-gaar |
|
Mooy ne, bala dara, Séex Anta tekkikat la woon | 1 | mooy ne, bala dara, séex anta tekkikat la woon |
|
Boo seetloo, sunu way-tawati Covid-19 yu jëkk yi bitim-réew lañ jóge | 1 | boo seetloo, sunu way-tawati covid-19 yu jëkk yi bitim-réew lañ jóge |
|
Man nanu koo am it jaare ko ci yeneen i lijjanti. | 1 | man nanu koo am it jaare ko ci yeneen i lijjanti. |
|
XEESAL WALLA XEEB SA BOPP ? | 1 | xeesal walla xeeb sa bopp ? |
|
Waxi Seex Anta Joob ju aju làkkSoppi | 1 | waxi seex anta joob ju aju làkksoppi |
|
Damaa sonn lool?! | 1 | damaa sonn lool?! |
|
Àdduna wori neen la. | 1 | àdduna wori neen la. |
|
Loo leen di nëbb ? | 1 | loo leen di nëbb ? |
|
Yeneen waat yi it noonu lañu mel. | 1 | yeneen waat yi it noonu lañu mel. |
|
Loolu la ñuy wax dëppaleg déggoo yi. | 1 | loolu la ñuy wax dëppaleg déggoo yi. |
|
Sawat gi ci njabootug Combretaceae la bokk | 1 | sawat gi ci njabootug combretaceae la bokk |
|
Ab DVD la. | 1 | ab dvd la. |
|
Raxas naa ko. | 1 | raxas naa ko. |
|
màrs 741 ñu faatu | 1 | màrs 741 ñu faatu |
|
Amoon na ay weer ci ginnaaw. | 1 | amoon na ay weer ci ginnaaw. |
|
? Àjjuma 24i fani sulet 2020 | 1 | ? àjjuma 24i fani sulet 2020 |
|
Ndaw nettali lu reelu ! | 1 | ndaw nettali lu reelu ! |
|
Ndax sang bii bokkeewul ak yooyee wolof. | 1 | ndax sang bii bokkeewul ak yooyee wolof. |
|
Halowiin rekk la bañ. | 1 | halowiin rekk la bañ. |
|
Moom miy ki moy kaa | 1 | moom miy ki moy kaa |
|
Jox na ko liggéey. | 1 | jox na ko liggéey. |
|
Déggoon naa leen ñuy ñëw. | 1 | déggoon naa leen ñuy ñëw. |
|
Askan waa ngiy jooy, di sàkku ndimmal ci neen | 1 | askan waa ngiy jooy, di sàkku ndimmal ci neen |
|
Ndax damaa jaay yoos mi ? | 1 | ndax damaa jaay yoos mi ? |
|
Lungeen di def sungeen amul dara lu ngeen di def ? | 1 | lungeen di def sungeen amul dara lu ngeen di def ? |
|
lii xew ca Medinaa dina dakk! | 1 | lii xew ca medinaa dina dakk! |
|
Xoolleen nu ! | 1 | xoolleen nu ! |
|
ci lol dafay guusali put di yokku tér | 1 | ci lol dafay guusali put di yokku tér |
|
Li ko waral mooy Xasiidaam yii yamuñu ak dara fa Yàlla sunu Boroom. | 1 | li ko waral mooy xasiidaam yii yamuñu ak dara fa yàlla sunu boroom. |
|
Mooy ñenteelu xalifa ginnaaw S Abdul Ahad | 1 | mooy ñenteelu xalifa ginnaaw s abdul ahad |
|
Bul yem rekk ci meew, kafe mbaa duteek yu ni mel | 1 | bul yem rekk ci meew, kafe mbaa duteek yu ni mel |
|
Lii dula dimbali. | 1 | lii dula dimbali. |
|
Ku am doole la. | 1 | ku am doole la. |
|
Am naa lu ma metti lool. | 1 | am naa lu ma metti lool. |
|
Bii mooy teqaloo ?? | 1 | bii mooy teqaloo ?? |
|
Ñépp a ragal. | 1 | ñépp a ragal. |
|
Wàll gi jeex na. | 1 | wàll gi jeex na. |
|
Bu dee xas mi | 1 | bu dee xas mi |
|
Ekool bi, dafa reeluwul. | 1 | ekool bi, dafa reeluwul. |
|
Ndax Tom dafa lab ? | 1 | ndax tom dafa lab ? |
|
Kon nag, fàww nu xoolaat nekkiin yi ci biir néegu-sëy | 1 | kon nag, fàww nu xoolaat nekkiin yi ci biir néegu-sëy |
|
Jàppale ma, ñaan naa la ko ! | 1 | jàppale ma, ñaan naa la ko ! |
|
Tom dee na daaw. | 1 | tom dee na daaw. |
|
Nit ñii mat nañu 21 700 000 2015. | 1 | nit ñii mat nañu 21 700 000 2015. |
|
Tom daf maa soxla. | 1 | tom daf maa soxla. |
|
Ñu guree ngeen. | 1 | ñu guree ngeen. |
|
Dafal li nga bëgg. | 1 | dafal li nga bëgg. |
|
Yaa ngi tappale. | 1 | yaa ngi tappale. |
|
Bugaaseli am na bàyyig négandiku | 1 | bugaaseli am na bàyyig négandiku |
|
Loolu yépp lu man a nekk la, tesax lu am la. | 1 | loolu yépp lu man a nekk la, tesax lu am la. |
|
Talaata jàpp 5h25 Dog 19h24 | 1 | talaata jàpp 5h25 dog 19h24 |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
README.md exists but content is empty.
Use the Edit dataset card button to edit it.
- Downloads last month
- 20