en
stringlengths 1
298
| wo
stringlengths 1
279
⌀ |
---|---|
I understand.
|
Nànd naa.
|
And please... don't worry.
|
Ak mangi... bul jaaxle.
|
Me?
|
Man?
|
They're coming.
|
Ñu ngi ñëw.
|
Yes.
|
Waaw.
|
No!
|
Déedéet!
|
Damned!
|
Alku!
|
I could use a good man to help me get my project on wheels.
|
Mën naa jëfandikoo nit ku baax ngir jàppale ma def sama projet.
|
Daddy's asleep.
|
Sama pàppa nelaw na.
|
I've decided... not to stay.
|
Dama jël dogal... duma toog.
|
Yeah, well, what the hell do you know about it, Capone?
|
Waaw, loo xam ci mbir mi, Capone?
|
I've got plenty of jackets.
|
Amnaa ay veste yu bari.
|
- Silence?
|
- Noppi?
|
This winter, I will take him to the mountain.
|
Hiver bii, dinaa ko yóbbu ci tundu wi.
|
Do you think they'll take to it?
|
Yaakaar nga ni dina ñu ko nangu?
|
-Stay away from me.
|
-Nga baña jege.
|
Half a bottle?
|
Genn-wàllu butéel?
|
We can leave, Erik.
|
Mën nanu dem, Erik.
|
22, my Führer.
|
22, sama fuurr.
|
I am unworthy!
|
Yeyoowuma!
|
Did they die in the war?
|
Ndax dee nañu ci xare bi?
|
You just stay there to take care of yours.
|
Yaw nga toog foofu ngir toppatoo sa bopp.
|
But look at it: it's like living in the forest.
|
Waaye xoolal lii: dafa mel ni danga dëkk ci àll bi.
|
Well, you underestimate yourself.
|
Waaye, yaa ngi suufeel sa bopp.
|
- To do what?
|
- Ngir def lan?
|
There's hundreds of them.
|
Amna ay téemeeri nit.
|
Life and death are his to give and take.
|
Dundu ak dee, moo wara joxe ak jël.
|
That child is being badly brought up.
|
Xale boobu dañu koy yar bu baax.
|
Mmm. Smell that.
|
Mmm. Xettal loolu.
|
- Jessie.
|
- Jesi.
|
What is this?
|
Liggéeyu tàggatu?
|
End it. I would do the-
|
Jeexal ko. Dinaa def
|
Six months.
|
Jiroom benn weer.
|
Bunch of cowherds!
|
Ay sàmm nag!
|
The bastards!
|
Bastard yi!
|
A cup of tea, please
|
Baal ma benn kaasu ataaya
|
That's my mother.
|
Loolu mooy sama yaay.
|
What are you in for?
|
Lu tax nga nekk?
|
He will reach the age.
|
Dina àgg ci àpp bi.
|
Let me tell you.
|
Xaaral ma wax la.
|
Good Lord ...
|
Boroom bu baax...
|
- A whole bottle and a pizza.
|
- Benn butéel lëmm ak benn pizza.
|
They'll love it.
|
Dina ñu ko bëgg.
|
I'm so sorry I can't give you a better present.
|
Maa ngi lay massawu, mënu ma la jox kado bu gëna baax.
|
- We're with you, Alexander!
|
- Noo ngi ànd ak yaw, Alexandre!
|
-Wendy.
|
-Wendy.
|
Give her a little gas.
|
Jox ko tuuti gaz.
|
We'll see what we can do.
|
Dinañu xool li ñu mën a def.
|
I'll keep an eye out for you and the chessboard ready.
|
Dinaa la xool bu baax, nga defar tablo d'échec bi.
|
That's it, it's well done.
|
Loolu la, def nga ko bu baax.
|
I don't think so.
|
Yaakaar naa ni du loolu.
|
I doubt they'll kick up any fuss.
|
Sikki sama bopp ni dina ñu def benn coow.
|
Only when he's found will it be decided.
|
Suñu ko gisee rek lañuy dogal.
|
Can I help?
|
Mën naa la jàppale?
|
They hit me here, and here.
|
Ñu dóor ma fii, ak fii.
|
At night the jackals prowl around.
|
Guddi gi, jaaka yi dañuy wër.
|
Travel.
|
Tukki.
|
Jesus.
|
Jesus.
|
Welcome
|
Dalal ak jàmm
|
But how can this be?
|
Waaye naka la loolu mënee am ?
|
I won't make any noise.
|
Duma def benn coow.
|
My national comrades...
|
Samay xarit national...
|
-Stop it!
|
-Taxawal!
|
This is where we keep all of our meat.
|
Mooy barab bi ñuy denc sunu yàpp yépp.
|
Your mother too will soon turn 70.
|
Sa yaay itam mingi waaja am 70 at.
|
Heywood, you're so smart, you call it?
|
Heywood, danga am xel lool, nga woo ko?
|
Berlin, 23 April, 1945.
|
Berlin, 23 awril 1945.
|
Lucien...
|
Lusien...
|
Remember, Red, hope is a good thing.
|
Nga bàyyi sa xel, Red, yaakaar lu baax la.
|
Great.
|
Neex na.
|
I mean.?
|
Maa ngi.?
|
Crateros.
|
Krater.
|
Tatsuhei!
|
Tatsuhei!
|
- No pizzas in this restaurant.
|
- Amul pizza ci resto bii.
|
Not for an old crook like me.
|
Du ngir defkati ñaawtéef yu melni man.
|
She can't say Rud either.
|
Mënul wax Rud itam.
|
We can leave this awful place and go out and conquer the world, Erik.
|
Mën nanu bàyyi barab bu tiis bii dem daal di nangu àdduna bi, Erik.
|
There are no neighbours I can talk to.
|
Amul dëkkandoo bu ma mëna waxtaan ak moom.
|
- It's too heavy for you.
|
- Dafa diis ci yaw.
|
Damn the Stone Farm.
|
Damn Ferme de Stone.
|
Come over to our place, Traveler!
|
Tukkikat bi, ñëwal ci sunu barab!
|
- Typhus of India?
|
- Tifus bu Inde?
|
-Give me the bat.
|
-Jox ma yat wi.
|
We'll never leave this place.
|
Dunu musa bàyyi barab bii.
|
Why is that?
|
Lu tax mu mel noonu ?
|
Jessie.
|
Jessie.
|
My dearest sister, I'm so sorry I have to write you this.
|
Sama mag ju jigéen ju baax ji, mangi jeggalu ci lima lay bind lii.
|
- Mm-hmm.
|
- M-mm.
|
I have denied him, Mother!
|
Weddi naa ko, yaay!
|
I thirst.
|
Dama mar.
|
You got 15 rib roasts 30 ten-pound bags of hamburger.
|
Am nga 15 costo buñ saaf ak 30 saaku hamburger bu fukki kilo.
|
Risuke!
|
Risuke!
|
We'll try to find something.
|
Dina nu jéema wut dara.
|
They're giving out melon slices.
|
Dañuy séddale ay daggitu melon.
|
You've never been away.
|
Musu nga dem feneen.
|
How long can you hold out?
|
Ba kañ ngay mëna muñ?
|
Asano waited till we left!
|
Asano xaar ba nu dem
|
Orin of "the house of the strain"
|
Orin de "la maison de la strain".
|
Maybe the best of things.
|
Amaana li gëna baax ci mbir yi.
|
Look, the sole has worn away.
|
Xoolal, sol bi daa màgget.
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.