en
stringlengths 1
298
| wo
stringlengths 1
279
⌀ |
---|---|
We must finish what we failed to do at Gaugamela.
|
Danu wara jeexal li nu ñàkka def ci Gaugamela.
|
- Nothing.
|
- Dara.
|
It just slipped out.
|
Dafa génn rek.
|
Two things never happened again after that.
|
Ñaari mbir musu ñu am ginaaw ga.
|
The Pacific Ocean?
|
Géeju Pacific bi?
|
Thank you? .?
|
Jërëjëf? .?
|
No hard feelings?
|
Amul yëg-yëg bu metti?
|
I will be hoping that this letter finds you and finds you well.
|
Dinaa am yaakaar ni bataaxal bii daf lay gis, nga wér.
|
Yes, my Führer.
|
Waaw, sama Führer.
|
I'm right here!
|
Maa ngi fi!
|
The rest of you go back to work.
|
Yéen ñi ci des dellu leen seen liggéey.
|
Meniconi and Bagonghi, come over here.
|
Menikoni ak Bagonghi, ñëwleen fii.
|
Two mozzarellas and a full bottle.
|
Ñaari mozzarella ak benn butéel bu fees.
|
Sometimes you're paid, sometimes not
|
Yenn saa yi dañu lay fay, yenn saa yi duñu la fay
|
He only went to bed a few hours ago.
|
Waxtu yu néew rek lay tëdd.
|
How can you sing so?
|
naka ngay mëna way nii?
|
From the South Island?
|
Ci Ile du Sud la?
|
The fifth one from the front.
|
Juroom bi ci kanam.
|
- Yes, of course.
|
- Waaw kay.
|
She's gone after the Deer God.
|
Dafa dem topp Yàlla Kewel.
|
Go to the employment office.
|
Demal ci biro biy saytu liggéey.
|
Do you think I'II go to school and be made a fool of?
|
Yaakaar nga ni damay dem ekol ñu def ma dof?
|
But no wine or cold chicken.
|
Waaye amul vin wala ginaar gu sedd.
|
You live in the forest, and I'll live at the ironworks.
|
Yaw ci àll bi nga dëkk, man ma dëkk ci wen wi.
|
Not like your father's... made of calfskin, new.
|
Du ni bu sa pàppa... ñu defaree ko der nag, bees.
|
Fuck.
|
Fuck.
|
Well done today.
|
Def nga lu baax tay.
|
I don't believe they did.
|
Gëmuma ni def nañu ko.
|
Let's go!
|
Nanu dem!
|
and that during those 20 years he did not have to modify his policies whatsoever.
|
ak ni ci 20 at yooyu amul benn coppite bumu wara def.
|
Is it good?
|
Ndax baax na?
|
We risked our lives to bring the rice you're eating.
|
Danuy risk sunu bakkan ngir indi céeb gi ngeen di lekk.
|
We must hunt Darius down.
|
Danu wara rëbb Dariyus.
|
Your friend, Andy.
|
Sa xarit, Andy.
|
I'm a fighting man.
|
Xeexkat laa.
|
Practice, Lucien!
|
Jàngaleel, Lucien!
|
- You can finish it.
|
- Mën nga ko jeexal.
|
Yes, sir.
|
Waaw, sang bi.
|
My Führer, as a soldier I suggest we try to break through the encirclement.
|
Sama Führer, soldaar laa, maa ngi lay digal nga jéema jaar ci biir dëkk bi.
|
We'll drink wine with our meal, but leave room for dessert, okay?
|
Dina nu naan vin ak sunu lekk, waaye bàyyi palaas ngir desee, waaw?
|
But we couldn't.
|
Waaye mënu nu ko woon.
|
My life is now yours.
|
Sama dundu leegi yaa ko moom.
|
My son, let me die with you.
|
Sama doom, bàyyi ma ak yaw dee.
|
I'm Katja's son.
|
Man doomu Katja laa.
|
What's the matter?
|
Lu xew?
|
There's no mistaking those tusks.
|
Amul benn njuumte ci bëñ yooyu.
|
I had dreams, too, of all the things I would do.
|
Maa ngi yàgg a xalaat mbir yima wara def.
|
With the regimen of cares that I've put in place...
|
Ak regime de soins yima def...
|
Come inside and get warm.
|
Duggal nga tàngoor.
|
Shit?
|
Merde?
|
The Sisters never laid a finger on Andy again and Bogs never walked again.
|
Sisters yi musu ñu teg baraam ci Andy te Bogs musul doxaat.
|
The Lord forgive me for abusing his gifts but it's a terrible temptation when you' re broken-hearted.
|
Boroom bi baal ma ci ni may yàq may yi mu ma jox, waaye soo amee xol bu yàqu, natt bu metti la.
|
Bastard!
|
Doom bu jigéen ci buur!
|
- 2, 3, and 4 dinars
|
- 2, 3 ak 4 dinaar
|
Mr er.?
|
M. er.?
|
Come here.
|
Kaay fii.
|
We're passing the pork butcher.
|
Noo ngi romb yàppu mbaam xuux bi.
|
Can't you wait till later?
|
Mën nga xaar ba ëlëg?
|
ULLMAN:
|
Ullman:
|
I suggest...
|
Maa ngi lay digal...
|
- That was not your father's mission.
|
- Du loolu mooy liggéeyu sa pàppa.
|
Go back to the other oafs.
|
Dellu ci yeneen dof yi.
|
Make sure the women and children are fed.
|
Fexeel ba jigéen ñi ak xale yi am luñu lekk.
|
You should know that Hermann isn't here.
|
Danga wara xamni Hermann nekkul fii.
|
What make was it?
|
Lan moo ko defar?
|
Practice!
|
Tàggat tàggatu!
|
And who made the iron that bought that rice?
|
Ak kan moo defar wen wi jëndoon céeb googu?
|
During the fight for Berlin we've already lost 15-20,000 of the younger officers.
|
Ci xeex bi ñuy xeex Berlin, ñàkk nañu 15 ba 20000 ofisiye yu ndaw.
|
Put me down for a quarter deck?
|
Tegal ma ci benn pond?
|
I think it's time she took a real risk.
|
Dama jàpp ni jotna nga jël risk.
|
I think the best thing is to come along to the gentlemen's room and we'll get some water to it, sir.
|
Dama jàpp ni li gëna wóor mooy nga ñëw ci néegu góor ñi, nu jël ndox ci, kilifa gi.
|
The girls can't find their cows when you move them around.
|
Jigéen ñi duñu gis seeni nag soo leen toxal.
|
-You don't?
|
-Xamuloo ko?
|
Get busy living or get busy dying.
|
Demal ci dundu wala nga nekk ci dee.
|
- About scare me to death, something that big.
|
- Dama tiital ba dee, lu rëy lool.
|
I just wanted to get out of the wind.
|
Lima bëggoon mooy génn ci ngelaw li.
|
They transferred him to a minimum-security hospital upstate.
|
Ñu daal di koy yóbbu ci hopitaal bu am kaaraange gu néew ci nord bi.
|
Looks like he brought his whole tribe!
|
Daa melni dafa indi tribum yépp!
|
I don't like no bellyaching.
|
Bëgguma ab biir buy metti.
|
I lay in the blood for three days, like a stuck pig.
|
Ma tëdd ci deret ji ñatti fan, melni mbaam xuux bu tëju.
|
Come, doctor.
|
Doktër, ñëwal.
|
If I promise you'II never again see your father like yesterday would you then go to school tomorrow, Pelle?
|
Suma lay dige ni dootu ma gisati sa pàppa ni démb, ndax suba nga dem ekol, Pelle?
|
Ah!
|
Ah!
|
She's doing no harm, let her stay.
|
Deful dara luy lore, bàyyileen ko mu des.
|
Those who came before are gone.
|
Ñi ko jiitu dem nañu.
|
They'll give you a work permit.
|
Dina ñu la jox sañ-sañu liggéey.
|
Don't you know that?
|
Ndax xamuleen loolu ?
|
Brooks. "
|
Brooks. "
|
A Fides.
|
A Fides.
|
We work those bellows all night long!
|
Guddi gi yépp danuy liggéey soufflet yooyu!
|
Ham, 79 francs.
|
Jambon, 79 fraŋ.
|
- Proud bitch.
|
- Yaakaar gu réy.
|
But that's what young men are for.
|
Waaye loolu mooy li xale yu góor yi di def.
|
You will not have to eat!
|
Dunga lekk!
|
that we try it again.
|
nu jéemaat ko.
|
- The small one?
|
- Bu ndaw bi?
|
You take care of it.
|
Yaw nga toppatoo ko.
|
Do you remember Katja?
|
Ndax fàttaliku nga Katja?
|
He's not my father.
|
Du sama pàppa.
|
Watch out, Pelle.
|
Moytul, Pelle.
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.