en
stringlengths 1
298
| wo
stringlengths 1
279
⌀ |
---|---|
You could get wet, you yellow-belly.
|
Mën nga tooy, yaw biir bu nete bi.
|
Awfully nice of you to say.
|
Loolu baaxna lool ci sa wax.
|
You're going to die.
|
Dangay dee.
|
Kongstrup is back!
|
Kongstrup dellu na!
|
Whatever mistakes I've made, I've paid for them and then some?
|
Bépp njuumte buma def, maa ngi koy fay, ba noppi yenn?
|
We leave for Arabia in the spring, and I couldn't leave without you.
|
Danuy dem Arabie ci pringtemps, te mënu ma dem te amul yaw.
|
Really?
|
Dëgg la?
|
- How'd they get away with this?
|
- Naka lañu mënee rëcci ci lii?
|
Here I am!
|
Maa ngi nii!
|
We'll eat and be happy for now.
|
Dina nu lekk ba noppi féexal sunu xol.
|
Dickheads.
|
Bopp yi.
|
What are you doing?
|
Loy def?
|
The Führer has lost all belief in a favorable outcome.
|
Führer amatul woon benn gëm-gëm ci njariñ li.
|
He had a good employment record, good references.
|
Amoon na dosiye liggéey bu baax, ay royuwaay yu baax.
|
We're reeling them in!
|
Noo ngi leen di dugal!
|
Whatever it was, something lit a fire under that boy's ass.
|
Lumu mëna nekk, amna lu taal ci suufu mbaggu xale bu góor bi.
|
Come on! Jump!
|
Gaawal! Tëb!
|
I think we can manage that too, Doc.
|
Yaakaar naa ni loolu itam mën nanu ko def, Doktër.
|
Can you believe it?
|
Ndax mën nga ko gëm ?
|
And the ironworks?
|
Ak liggéeyukaay yi?
|
I figure we owe him that much for the beer?
|
Yaakaar naa ni noonu lañu ko wara fay ngir bieer bi?
|
Now the cheese shop.
|
Leegi butig fromage bi.
|
How much in tomans?
|
Ñaata ci toman?
|
- Uncle Whatchamacallit!
|
- Ndijaay Whatchamacallit!
|
Get lost, Pelle!
|
Réer, Pelle!
|
I want to live a little longer.
|
Dama bëgga gëna gudd fan.
|
Come on, man.
|
Nanga def, waay.
|
King of what?
|
Buuru lan?
|
So now...
|
Kon leegi...
|
He's harmless.
|
Amul benn loraange.
|
It's a goddamn mess. I'll tell you that.
|
Dafa jaxasoo. Dinaa la ko wax.
|
A hill girl?
|
Xale bu jigeen?
|
I think that's what it's called.
|
Yaakaar naa ni noonu lañu koy woowe.
|
There is no one left.
|
Kenn dootul des.
|
On the train, with the little boy.
|
Ci biir saxaar gi, ak xale bu góor bi.
|
Stolen bikes are always taken apart.
|
Velo yuñ sàcc dañu leen di dindi saa yu nekk.
|
Collignon, down the john.
|
Collignon, ci suufu john.
|
Of course, I intended to change my jacket this evening before the fish and goose soiree.
|
Dëgg la dinaa bëgga soppi sama veste tay ci guddi balaa soiree jën ak oie.
|
- What...
|
- Lan...
|
I'm guilty of committing a crime.
|
Dama def krim.
|
She's fond of stratagems.
|
Dafa sopp pexe.
|
Duck!
|
Kanaara!
|
Put on the music!
|
Tegal music bi!
|
Hurry with the twigs, this wood is too damp to light.
|
Gaaw leen ak garab yi, garab gi tooyna lool ba mënul leer.
|
Because it's not for me I must continue to rot?
|
Ndax du man ma wara wéy di yàqu?
|
That hotel, that boat.
|
Hotel boobu, gaal gi.
|
We'll have to work in make-up!
|
Dina nu liggéey ci maquillage!
|
Why do they call you that?
|
Lu tax ñu lay woowe noonu?
|
Erik, why haven't you unharnassed Kongstrup's horses?
|
Erik, lu tax dindiwul fasu Kongstrup yi?
|
Think of the thousands of wounded.
|
Xalaatal junniy nit ñu gaañu.
|
Arabia.
|
Arabie.
|
There's a cure for everything... except death.
|
Lépp amna garab... lu moy dee.
|
I was thinking of maybe trying for my high school equivalency.
|
Maa ngi doon xalaat amaana damay jéema jàng liise.
|
Hey.
|
Hey.
|
Well, all right.
|
Waaw kay.
|
You could get dizzy and fall in the water.
|
Mën nga miir ba noppi nga daanu ci ndox mi.
|
And from what I've been told, he seemed like a completely normal individual.
|
Te ci liñu ma wax, dafa melni nit ku amul benn sikk.
|
There's no wound!
|
Amul benn gaañ-gaañu!
|
I must admit, I didn't think much of Andy, first time I laid eyes on him.
|
Dama wara wax ni, bi may njëkka gis Andy, xalaatuma woon lu bari.
|
My beloved son, I don't know if this letter will reach you.
|
Sama doom ju baax ji, xawma ndax bataaxal bii dina yegg ci yaw.
|
The man likes to play chess.
|
Ku góor ki dafa bëgg jeu echec.
|
It's a shame for me to be as healthy.
|
ruslu naa ma am wérgi-yaram bu mel nii.
|
What are you hiding?
|
Lu ngeen di nëbb?
|
Saved thanks to a wolf!
|
Luu moo ko muccal!
|
- Hmm?
|
- Hé?
|
Keep moving!
|
Weyal di doxantu!
|
Very wise, sir.
|
Am xel mu ñaw, kilifa gi.
|
You can pee in your pants 100 times, but then you have to win.
|
Mën nga sibbiru ci sa pàntaloŋ 100 yoon, waaye soo ko defee danga wara jël ndam li.
|
Rouge, too?
|
Rouge itam?
|
To eat like them, you have to... earn at least a million a month.
|
Soo bëggee lekk ni ñoom, fàww nga... am milyoŋ weer wu nekk.
|
No one, Jesus!
|
Kenn, Yeesu!
|
Because I am going to eat my food first.
|
Ndax maa ngi njëkka lekk sama ñam.
|
Wait a minute.
|
Xaaral tuuti.
|
The sea is hard.
|
Geej gi dëgër na.
|
Parole violation.
|
Parole.
|
Bagonghi, let's go this way.
|
Bagonghi, nanu dem fii.
|
Yakul...
|
Yakul...
|
But really don't make a sound.
|
Waaye bul def benn bruit.
|
Maybe it's because I'm Irish?
|
Amaana ndax irlandais laa?
|
But at some point during the winter he must have suffered some kind of a complete mental breakdown.
|
Waaye amna jamono ci hiver bi, amaana dafa am luko yàqu bu baax ci xel mi.
|
- Oh, my God.
|
- Yaw sama Yàlla.
|
Go home, Pelle!
|
Demal sa kër, Pelle!
|
Release him !
|
Bàyyileen ko !
|
Fortune favors the bold.
|
Fortune dafa bëgg ñi gëna am fit.
|
We can't help them now.
|
Mënu leen dimbali leegi.
|
Now...
|
Léegi...
|
You with your breeding.
|
Yaw ak sa yar.
|
- Col...
|
- Kol...
|
I'm just eating.
|
Damay lekk rek.
|
Come along, now.
|
Leegi ñëwal.
|
Now wait a minute!
|
Leegi xaaral tuuti!
|
Some died of disease.
|
Ñenn ñi feebar moo leen faatu.
|
Perhaps there is some human soul who will pass on my final words to you.
|
Amaana amna nit ku lay jox sama kàddu yu mujj.
|
I don't think that's too much to ask.
|
Yaakaar naa ni loolu bariwul luñu koy laaj.
|
Listen to me!
|
Dégluleen ma!
|
.
| null |
Eat, eat.
|
Lekk, lekk.
|
A new shawl, Auntie?
|
Shawl bu bees, tànta?
|
What's all this?
|
Luy lii lépp?
|
Get off the street!
|
Jégeel ci mbedd mi!
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.